Muhammad · 27/38
Tekki Waxtaan — Muhammad
فَكَيْفَ إِذَا تَوَفَّتْهُمُ الْمَلَائِكَةُ يَضْرِبُونَ وُجُوهَهُمْ وَأَدْبَارَهُمْ ۝٢٧
Fakaifa izaa tawaffat humul malaaa`ikatu yadriboona wujoohahum wa adbaa rahum
📖 Tekkim Wolof
Naka la séeni mbir di mujje su leen Malaaka ya jekkalee, di leen dóor ci kanam ak ginnaaw ?

🎧 Dégg


📜 Aaya 25-29 — Muhammad

25إِنَّ الَّذِينَ ارْتَدُّوا عَلَىٰ أَدْبَارِهِم مِّن بَعْدِ مَا تَبَيَّنَ لَهُمُ الْهُدَى ۙ الشَّيْطَانُ سَوَّلَ لَهُمْ وَأَمْلَىٰ لَهُمْ
Ña murtad weddi ginnaaw ba leen njub ga feeñee, Saytaane legna leen te di leen fàbbi.
26ذَٰلِكَ بِأَنَّهُمْ قَالُوا لِلَّذِينَ كَرِهُوا مَا نَزَّلَ اللَّهُ سَنُطِيعُكُمْ فِي بَعْضِ الْأَمْرِ ۖ وَاللَّهُ يَعْلَمُ إِسْرَارَهُمْ
Li ko waral moo di dañuy wax yéefar yi naan leen : “dananu leen topp ci yennati mbir”. Te Yàlla xam na li ñuy nëbb.
27فَكَيْفَ إِذَا تَوَفَّتْهُمُ الْمَلَائِكَةُ يَضْرِبُونَ وُجُوهَهُمْ وَأَدْبَارَهُمْ
Naka la séeni mbir di mujje su leen Malaaka ya jekkalee, di leen dóor ci kanam ak ginnaaw ?
28ذَٰلِكَ بِأَنَّهُمُ اتَّبَعُوا مَا أَسْخَطَ اللَّهَ وَكَرِهُوا رِضْوَانَهُ فَأَحْبَطَ أَعْمَالَهُمْ
Li ko waral moo di dañuy topp luy waral xarabug Yàlla, tey bañ lépp luy ngëramal Yàlla. Moom it mu daldi sippi séen jëf.
29أَمْ حَسِبَ الَّذِينَ فِي قُلُوبِهِم مَّرَضٌ أَن لَّن يُخْرِجَ اللَّهُ أَضْغَانَهُمْ
Moo ndax naaféq ya dañoo foog ne Yàlla du génne mbañeel gi ëmbul (Yonenta bi) mu ne fàŋŋ ?
MuhammadFihi Alxuraan
38Aaya
MedinanRevelation
27Aaya

Tekki — Muhammad 27

Simoore Muhammad Aaya 27 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Naka la séeni mbir di mujje su leen Malaaka ya…

Simoore Aaya 27/38 — Muhammad محمد (Medinan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Muhammad Dégg, Muhammad Tekki, Muhammad mp3, Muhammad pdf. Aaya 25–29. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers