Muhammad · 33/38
Tekki Waxtaan — Simoore Muhammad
۞ يَا أَيُّهَا الَّذِينَ آمَنُوا أَطِيعُوا اللَّهَ وَأَطِيعُوا الرَّسُولَ وَلَا تُبْطِلُوا أَعْمَالَكُمْ ۝٣٣
Yaaa ayyuhal lazeena aamanoo atee`ul laaha wa atee`ur Rasoola wa laa tubtilooo a`maalakum
📖 Tekkim Wolof
eey yéen ñi gëm ! Topp leen Yàlla tey topp Yonent bi, te bu leen di neenal séeni jëf.

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 31-35 — Simoore Muhammad

31وَلَنَبْلُوَنَّكُمْ حَتَّىٰ نَعْلَمَ الْمُجَاهِدِينَ مِنكُمْ وَالصَّابِرِينَ وَنَبْلُوَ أَخْبَارَكُمْ
Dananu leen natt ba baa nuy xam, ñay jihaad ci yéen ak muñkat ya, te it da nanu feeñal séeni jëf (yu baax ak yu bon).
32إِنَّ الَّذِينَ كَفَرُوا وَصَدُّوا عَن سَبِيلِ اللَّهِ وَشَاقُّوا الرَّسُولَ مِن بَعْدِ مَا تَبَيَّنَ لَهُمُ الْهُدَىٰ لَن يَضُرُّوا اللَّهَ شَيْئًا وَسَيُحْبِطُ أَعْمَالَهُمْ
Ña daan weddi tey dumóoyu yoonu Yàlla te daan sonal Yonenta bi ginaaw (ba ñu xamee) njub ga mu leer nàññ, manuñoo wàññi Yàlla dara. Te dana sippi seen jëf.
33۞ يَا أَيُّهَا الَّذِينَ آمَنُوا أَطِيعُوا اللَّهَ وَأَطِيعُوا الرَّسُولَ وَلَا تُبْطِلُوا أَعْمَالَكُمْ
eey yéen ñi gëm ! Topp leen Yàlla tey topp Yonent bi, te bu leen di neenal séeni jëf.
34إِنَّ الَّذِينَ كَفَرُوا وَصَدُّوا عَن سَبِيلِ اللَّهِ ثُمَّ مَاتُوا وَهُمْ كُفَّارٌ فَلَن يَغْفِرَ اللَّهُ لَهُمْ
Ña daan weddi tey dumóoyu yoonu Yàlla ba dee ca diy yéefar, Yàlla duleen jéggal.
35فَلَا تَهِنُوا وَتَدْعُوا إِلَى السَّلْمِ وَأَنتُمُ الْأَعْلَوْنَ وَاللَّهُ مَعَكُمْ وَلَن يَتِرَكُمْ أَعْمَالَكُمْ
Bu leen di doyadi tey woote maslaa te yéen a gën a kawe, Yàlla itam yéen la àndal, te it séenug (peyug jëf) dara du ci wàññiku.
MuhammadFihi Alxuraan
38Aaya
MedinanRevelation
33Aaya

Tekki — Muhammad 33

Simoore Muhammad Aaya 33 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : eey yéen ñi gëm ! Topp leen Yàlla tey topp…

Simoore Aaya 33/38 — Simoore Muhammad محمد (Medinan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Muhammad Dégg, Simoore Muhammad Tekki, Simoore Muhammad mp3, Simoore Muhammad pdf. Aaya 31–35. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Monday, September 28, 2026

Don't forget us in your sincere prayers