Muhammad · 8/38
Tekki Waxtaan — Simoore Muhammad
وَالَّذِينَ كَفَرُوا فَتَعْسًا لَّهُمْ وَأَضَلَّ أَعْمَالَهُمْ ۝٨
Wallazeena kafaroo fata`s al lahum wa adalla a`maalahum
📖 Tekkim Wolof
Ña weddiwoon, ñoom toskare nañu te séeni jëf réer na.

🎧 Dégg


📜 Aaya 6-10 — Simoore Muhammad

6وَيُدْخِلُهُمُ الْجَنَّةَ عَرَّفَهَا لَهُمْ
te dana leen tàbbal Àjjana ju mu leen jagle.
7يَا أَيُّهَا الَّذِينَ آمَنُوا إِن تَنصُرُوا اللَّهَ يَنصُرْكُمْ وَيُثَبِّتْ أَقْدَامَكُمْ
eey yéen ñi gëm ! bu ngeen taxawee temm ci yoonu Yàlla, Kon dey dana leen dimbali te it dana dëgëral séeni ndëggu (gindi leen ci xare).
8وَالَّذِينَ كَفَرُوا فَتَعْسًا لَّهُمْ وَأَضَلَّ أَعْمَالَهُمْ
Ña weddiwoon, ñoom toskare nañu te séeni jëf réer na.
9ذَٰلِكَ بِأَنَّهُمْ كَرِهُوا مَا أَنزَلَ اللَّهُ فَأَحْبَطَ أَعْمَالَهُمْ
Li ko waral moo di ne dañoo sibóon li Yàlla daan wàcce ci moom it. Mu daldi sippi séeni jëf (neenal ko).
10۞ أَفَلَمْ يَسِيرُوا فِي الْأَرْضِ فَيَنظُرُوا كَيْفَ كَانَ عَاقِبَةُ الَّذِينَ مِن قَبْلِهِمْ ۚ دَمَّرَ اللَّهُ عَلَيْهِمْ ۖ وَلِلْكَافِرِينَ أَمْثَالُهَا
Moo xanaa dañoo wërul ca réew yi (suuf si) bay xool naka la mujjug ña leen jiitu deme woon ? Yàlla da leen nappaaje (faag leen). Noonu it la yéefar yi di mujje.
MuhammadFihi Alxuraan
38Aaya
MedinanRevelation
8Aaya

Tekki — Muhammad 8

Simoore Muhammad Aaya 8 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Ña weddiwoon, ñoom toskare nañu te séeni jëf réer na.

Simoore Aaya 8/38 — Simoore Muhammad محمد (Medinan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Muhammad Dégg, Simoore Muhammad Tekki, Simoore Muhammad mp3, Simoore Muhammad pdf. Aaya 6–10. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Monday, September 7, 2026

Don't forget us in your sincere prayers