Muhammad · 7/38
Tekki Waxtaan — Simoore Muhammad
يَا أَيُّهَا الَّذِينَ آمَنُوا إِن تَنصُرُوا اللَّهَ يَنصُرْكُمْ وَيُثَبِّتْ أَقْدَامَكُمْ ۝٧
Yaaa ayyuhal lazeena aamanooo in tansurul laaha yansurkum wa yusabbit aqdaamakum
📖 Tekkim Wolof
eey yéen ñi gëm ! bu ngeen taxawee temm ci yoonu Yàlla, Kon dey dana leen dimbali te it dana dëgëral séeni ndëggu (gindi leen ci xare).

🎧 Dégg


📜 Aaya 5-9 — Simoore Muhammad

5سَيَهْدِيهِمْ وَيُصْلِحُ بَالَهُمْ
(Yàlla) dana leen xala gindi tey yéwénal seeni mbir,
6وَيُدْخِلُهُمُ الْجَنَّةَ عَرَّفَهَا لَهُمْ
te dana leen tàbbal Àjjana ju mu leen jagle.
7يَا أَيُّهَا الَّذِينَ آمَنُوا إِن تَنصُرُوا اللَّهَ يَنصُرْكُمْ وَيُثَبِّتْ أَقْدَامَكُمْ
eey yéen ñi gëm ! bu ngeen taxawee temm ci yoonu Yàlla, Kon dey dana leen dimbali te it dana dëgëral séeni ndëggu (gindi leen ci xare).
8وَالَّذِينَ كَفَرُوا فَتَعْسًا لَّهُمْ وَأَضَلَّ أَعْمَالَهُمْ
Ña weddiwoon, ñoom toskare nañu te séeni jëf réer na.
9ذَٰلِكَ بِأَنَّهُمْ كَرِهُوا مَا أَنزَلَ اللَّهُ فَأَحْبَطَ أَعْمَالَهُمْ
Li ko waral moo di ne dañoo sibóon li Yàlla daan wàcce ci moom it. Mu daldi sippi séeni jëf (neenal ko).
MuhammadFihi Alxuraan
38Aaya
MedinanRevelation
7Aaya

Tekki — Muhammad 7

Simoore Muhammad Aaya 7 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : eey yéen ñi gëm ! bu ngeen taxawee temm ci…

Simoore Aaya 7/38 — Simoore Muhammad محمد (Medinan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Muhammad Dégg, Simoore Muhammad Tekki, Simoore Muhammad mp3, Simoore Muhammad pdf. Aaya 5–9. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers