Al-Maida · 61/120
Tekki Waxtaan — Al-Maida
وَإِذَا جَاءُوكُمْ قَالُوا آمَنَّا وَقَد دَّخَلُوا بِالْكُفْرِ وَهُمْ قَدْ خَرَجُوا بِهِ ۚ وَاللَّهُ أَعْلَمُ بِمَا كَانُوا يَكْتُمُونَ ۝٦١
Wa izaa jaaa`ookum qaalooo aamannaa wa qad dakhaloo bilkufri wa hum qad kharajoo bih; wallaahu a`lamu bimaa kaanoo yaktumoon
📖 Tekkim Wolof
Bu ñu dikkee ci yéen naan : “Gëm nanu.”. Te fekk kéefar lañu indiwaale te moom lañuy yóbbuwaale. Te Yàllaa gën a xam la ñuy nëbb.
🎧 Dégg

📜 Aaya 59-63 — Al-Maida

59قُلْ يَا أَهْلَ الْكِتَابِ هَلْ تَنقِمُونَ مِنَّا إِلَّا أَنْ آمَنَّا بِاللَّهِ وَمَا أُنزِلَ إِلَيْنَا وَمَا أُنزِلَ مِن قَبْلُ وَأَنَّ أَكْثَرَكُمْ فَاسِقُونَ
Neel : “Éy yéen ñoñ-téere ! Ndax li ngeen nu bañe nekkul lu dul li nu gëm Yàlla ak li wàcceef na ko ci nun ak la jëkkoon a wàcc ? Li ëpp ci yéen ay saay-saay lañu.
60قُلْ هَلْ أُنَبِّئُكُم بِشَرٍّ مِّن ذَٰلِكَ مَثُوبَةً عِندَ اللَّهِ ۚ مَن لَّعَنَهُ اللَّهُ وَغَضِبَ عَلَيْهِ وَجَعَلَ مِنْهُمُ الْقِرَدَةَ وَالْخَنَازِيرَ وَعَبَدَ الطَّاغُوتَ ۚ أُولَٰئِكَ شَرٌّ مَّكَانًا وَأَضَلُّ عَن سَوَاءِ السَّبِيلِ
Neel : “Moo ndax duma leen xamal ku yées pey ëllëg ca Yàlla ? Ña Yàlla rëbb, mere leen, soppi lenn ca ñoom ay golo ak i mbaam-xuux te ñuy jaamu Séytaane, ñooña ñoo yées dëkkuwaay te ñoo gën a réer, sore yoon wu jub wa”.
61وَإِذَا جَاءُوكُمْ قَالُوا آمَنَّا وَقَد دَّخَلُوا بِالْكُفْرِ وَهُمْ قَدْ خَرَجُوا بِهِ ۚ وَاللَّهُ أَعْلَمُ بِمَا كَانُوا يَكْتُمُونَ
Bu ñu dikkee ci yéen naan : “Gëm nanu.”. Te fekk kéefar lañu indiwaale te moom lañuy yóbbuwaale. Te Yàllaa gën a xam la ñuy nëbb.
62وَتَرَىٰ كَثِيرًا مِّنْهُمْ يُسَارِعُونَ فِي الْإِثْمِ وَالْعُدْوَانِ وَأَكْلِهِمُ السُّحْتَ ۚ لَبِئْسَ مَا كَانُوا يَعْمَلُونَ
Danga gis ñu bari ci ñoom ñuy jëkkantee tàbbi ci bàkkaar, ak noonuwante ak séen lekk lu araam. Cëy la ñuy def aka bon !
63لَوْلَا يَنْهَاهُمُ الرَّبَّانِيُّونَ وَالْأَحْبَارُ عَن قَوْلِهِمُ الْإِثْمَ وَأَكْلِهِمُ السُّحْتَ ۚ لَبِئْسَ مَا كَانُوا يَصْنَعُونَ
Lu tee seen làbbe ya ak seen fóore ya tere leen wax ju ñaaw, ak lekk lu araam ? Cëy la ñu liggéey aka bon !
Al-MaidaFihi Alxuraan
120Aaya
MedinanRevelation
61Aaya

Tekki — Al-Maida 61

Simoore Al-Maida Aaya 61 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Bu ñu dikkee ci yéen naan : “Gëm nanu.”. Te…

Simoore Aaya 61/120 — Al-Maida المائدة (Medinan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-Maida Dégg, Al-Maida Tekki, Al-Maida mp3, Al-Maida pdf. Aaya 59–63. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers