Qaf · 44/45
Tekki Waxtaan — Qaf
يَوْمَ تَشَقَّقُ الْأَرْضُ عَنْهُمْ سِرَاعًا ۚ ذَٰلِكَ حَشْرٌ عَلَيْنَا يَسِيرٌ ۝٤٤
Yawma tashaqqaqul ardu `anhum siraa`aa; zaalika hashrun `alainaa yaseer
📖 Tekkim Wolof
bu keroogee bis ba suuf si di focc ñuy génn gaaw lool. Loolu nag ag dajale la gu yomb ci Nun.

🎧 Dégg


📜 Aaya 42-45 — Qaf

42يَوْمَ يَسْمَعُونَ الصَّيْحَةَ بِالْحَقِّ ۚ ذَٰلِكَ يَوْمُ الْخُرُوجِ
bis ba nga xam ne danañu dégg xaacu ga. Te bóobule Bis moo di bisub Dekkiwaat ba.
43إِنَّا نَحْنُ نُحْيِي وَنُمِيتُ وَإِلَيْنَا الْمَصِيرُ
Nun Yàlla (Man Yàlla) Maay dundal di rey, te ci Man la lépp di mujj,
44يَوْمَ تَشَقَّقُ الْأَرْضُ عَنْهُمْ سِرَاعًا ۚ ذَٰلِكَ حَشْرٌ عَلَيْنَا يَسِيرٌ
bu keroogee bis ba suuf si di focc ñuy génn gaaw lool. Loolu nag ag dajale la gu yomb ci Nun.
45نَّحْنُ أَعْلَمُ بِمَا يَقُولُونَ ۖ وَمَا أَنتَ عَلَيْهِم بِجَبَّارٍ ۖ فَذَكِّرْ بِالْقُرْآنِ مَن يَخَافُ وَعِيدِ
Man Yàlla Maa gëna xam liñuy wax. Yaw nag bokkul ci sa wartéef nga di leen ga. Yaw daal nangay fàttali, Alxuraan képp ku ragal Samab tëkku.
QafFihi Alxuraan
45Aaya
MeccanRevelation
44Aaya

Tekki — Qaf 44

Simoore Qaf Aaya 44 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : bu keroogee bis ba suuf si di focc ñuy génn…

Simoore Aaya 44/45 — Qaf ق (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Qaf Dégg, Qaf Tekki, Qaf mp3, Qaf pdf. Aaya 42–45. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers