Qaf · 43/45
Tekki Waxtaan — Qaf
إِنَّا نَحْنُ نُحْيِي وَنُمِيتُ وَإِلَيْنَا الْمَصِيرُ ۝٤٣
Innaa Nahnu nuhyee wa numeetu wa ilainal maseer
📖 Tekkim Wolof
Nun Yàlla (Man Yàlla) Maay dundal di rey, te ci Man la lépp di mujj,
🎧 Dégg

📜 Aaya 41-45 — Qaf

41وَاسْتَمِعْ يَوْمَ يُنَادِ الْمُنَادِ مِن مَّكَانٍ قَرِيبٍ
Yaw (Yonent) bi déglul , bu keroogee ba Wootekat ba (Israafiil) di wootee fu jige,
42يَوْمَ يَسْمَعُونَ الصَّيْحَةَ بِالْحَقِّ ۚ ذَٰلِكَ يَوْمُ الْخُرُوجِ
bis ba nga xam ne danañu dégg xaacu ga. Te bóobule Bis moo di bisub Dekkiwaat ba.
43إِنَّا نَحْنُ نُحْيِي وَنُمِيتُ وَإِلَيْنَا الْمَصِيرُ
Nun Yàlla (Man Yàlla) Maay dundal di rey, te ci Man la lépp di mujj,
44يَوْمَ تَشَقَّقُ الْأَرْضُ عَنْهُمْ سِرَاعًا ۚ ذَٰلِكَ حَشْرٌ عَلَيْنَا يَسِيرٌ
bu keroogee bis ba suuf si di focc ñuy génn gaaw lool. Loolu nag ag dajale la gu yomb ci Nun.
45نَّحْنُ أَعْلَمُ بِمَا يَقُولُونَ ۖ وَمَا أَنتَ عَلَيْهِم بِجَبَّارٍ ۖ فَذَكِّرْ بِالْقُرْآنِ مَن يَخَافُ وَعِيدِ
Man Yàlla Maa gëna xam liñuy wax. Yaw nag bokkul ci sa wartéef nga di leen ga. Yaw daal nangay fàttali, Alxuraan képp ku ragal Samab tëkku.
QafFihi Alxuraan
45Aaya
MeccanRevelation
43Aaya

Tekki — Qaf 43

Simoore Qaf Aaya 43 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Nun Yàlla (Man Yàlla) Maay dundal di rey, te ci…

Simoore Aaya 43/45 — Qaf ق (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Qaf Dégg, Qaf Tekki, Qaf mp3, Qaf pdf. Aaya 41–45. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers