Qaf · 45/45
Tekki Waxtaan — Simoore Qaf
نَّحْنُ أَعْلَمُ بِمَا يَقُولُونَ ۖ وَمَا أَنتَ عَلَيْهِم بِجَبَّارٍ ۖ فَذَكِّرْ بِالْقُرْآنِ مَن يَخَافُ وَعِيدِ ۝٤٥
Nahnu a`lamu bimaa yaqooloona wa maaa anta `alihim bijabbaarin fazakkir bil quraani many yakhaafu wa`eed
📖 Tekkim Wolof
Man Yàlla Maa gëna xam liñuy wax. Yaw nag bokkul ci sa wartéef nga di leen ga. Yaw daal nangay fàttali, Alxuraan képp ku ragal Samab tëkku.

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 43-45 — Simoore Qaf

43إِنَّا نَحْنُ نُحْيِي وَنُمِيتُ وَإِلَيْنَا الْمَصِيرُ
Nun Yàlla (Man Yàlla) Maay dundal di rey, te ci Man la lépp di mujj,
44يَوْمَ تَشَقَّقُ الْأَرْضُ عَنْهُمْ سِرَاعًا ۚ ذَٰلِكَ حَشْرٌ عَلَيْنَا يَسِيرٌ
bu keroogee bis ba suuf si di focc ñuy génn gaaw lool. Loolu nag ag dajale la gu yomb ci Nun.
45نَّحْنُ أَعْلَمُ بِمَا يَقُولُونَ ۖ وَمَا أَنتَ عَلَيْهِم بِجَبَّارٍ ۖ فَذَكِّرْ بِالْقُرْآنِ مَن يَخَافُ وَعِيدِ
Man Yàlla Maa gëna xam liñuy wax. Yaw nag bokkul ci sa wartéef nga di leen ga. Yaw daal nangay fàttali, Alxuraan képp ku ragal Samab tëkku.
QafFihi Alxuraan
45Aaya
MeccanRevelation
45Aaya

Tekki — Qaf 45

Simoore Qaf Aaya 45 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Man Yàlla Maa gëna xam liñuy wax. Yaw nag bokkul…

Simoore Aaya 45/45 — Simoore Qaf ق (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Qaf Dégg, Simoore Qaf Tekki, Simoore Qaf mp3, Simoore Qaf pdf. Aaya 43–45. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Wednesday, September 30, 2026

Don't forget us in your sincere prayers