Adh-Dhariyat · 31/60
Tekki Waxtaan — Adh-Dhariyat
۞ قَالَ فَمَا خَطْبُكُمْ أَيُّهَا الْمُرْسَلُونَ ٣١
Transliteration
Qaala famaa khatbukum ayyuhal mursaloon
Tekki (Tekkim Wolof)
📖 Tekkim Wolof
Ne leen [Ibraahiima]: “Ana la doon seeni tank?”
Additional reference in Fulfulde
🎧 Dégg
📜 Aaya 29-33 — Adh-Dhariyat
29فَأَقْبَلَتِ امْرَأَتُهُ فِي صَرَّةٍ فَصَكَّتْ وَجْهَهَا وَقَالَتْ عَجُوزٌ عَقِيمٌ
soxnaam sa dikk ak i yuxu, di talaata boppam te naan : “Màggat mu jaasir...
30قَالُوا كَذَٰلِكِ قَالَ رَبُّكِ ۖ إِنَّهُ هُوَ الْحَكِيمُ الْعَلِيمُ
Nu ne : “Loolu la sa Boroom wax. Te moo di Ku Xereñ ki, di Ku Xam ki”.
31۞ قَالَ فَمَا خَطْبُكُمْ أَيُّهَا الْمُرْسَلُونَ
Ne leen [Ibraahiima]: “Ana la doon seeni tank?”
32قَالُوا إِنَّا أُرْسِلْنَا إِلَىٰ قَوْمٍ مُّجْرِمِينَ
Ñu ne ko : “Nun dey dañunoo yabal ca aw nit ñu di ay tooñkat ,
33لِنُرْسِلَ عَلَيْهِمْ حِجَارَةً مِّن طِينٍ
ngir nu jëbb ay doji ban yu nu tàngal ci seeni kaw,
Adh-DhariyatFihi Alxuraan
60Aaya
MeccanRevelation
31Aaya
Tekki — Adh-Dhariyat 31
Simoore Adh-Dhariyat Aaya 31 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Ne leen [Ibraahiima]: “Ana la doon seeni tank?”Simoore Aaya 31/60 — Adh-Dhariyat الذاريات (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Adh-Dhariyat Dégg, Adh-Dhariyat Tekki, Adh-Dhariyat mp3, Adh-Dhariyat pdf. Aaya 29–33. Tekkim Wolof: Fulfulde.
العربية
English
Bahasa Indonesia
Türkçe
Русский
فارسی
Français
اردو
বাংলা
Deutsch
Español
中文
हिन्दी
Português
Italiano
ภาษาไทย
Polski
Nederlands
Shqip
Kiswahili
O'zbek
தமிழ்
Melayu
Bosanski
Soomaali
Azərbaycan
کوردی
한국어
日本語
Svenska
Dansk
Norsk
پښتو
മലയാളം
සිංහල
Tamazight
Hausa
አማርኛ
Български
Тоҷикӣ
Қазақша
Filipino
سنڌي
Yorùbá
Fulfulde
Татарча
ئۇيغۇرچە
Кыргызча
ਪੰਜਾਬੀ
Jawa
తెలుగు
မြန်မာ
ગુજરાતી
Oromo
मराठी
Tiếng Việt
Malagasy
Нохчийн
Wolof
ދިވެހި
ಕನ್ನಡ
Українська
Ελληνικά
ქართული
ខ្មែរ
دری
Qafar af
Maranao
नेपाली
Alxuraan bu Tedd bi
Tuesday, August 18, 2026
Don't forget us in your sincere prayers








