At-Tur · 24/49
Tekki Waxtaan — Simoore At-Tur
۞ وَيَطُوفُ عَلَيْهِمْ غِلْمَانٌ لَّهُمْ كَأَنَّهُمْ لُؤْلُؤٌ مَّكْنُونٌ ٢٤
Transliteration
Wa yatoofu `alaihim ghilmaanul lahum ka annahum lu`lu`um maknoon
Tekki (Tekkim Wolof)
📖 Tekkim Wolof
Dananu am xale yuy wër ci ñoom, yu melni pepp.
Additional reference in Fulfulde
🎧 Dégg
📜 Aaya 22-26 — Simoore At-Tur
22وَأَمْدَدْنَاهُم بِفَاكِهَةٍ وَلَحْمٍ مِّمَّا يَشْتَهُونَ
Te Dananu leen jox ay foytéef ak yàpp lépp lu ñu cay soxla.
23يَتَنَازَعُونَ فِيهَا كَأْسًا لَّا لَغْوٌ فِيهَا وَلَا تَأْثِيمٌ
Danuñu cay joqlante ak i kopp ci lu àndul ak i caaxaan waxatumalaa sobe.
24۞ وَيَطُوفُ عَلَيْهِمْ غِلْمَانٌ لَّهُمْ كَأَنَّهُمْ لُؤْلُؤٌ مَّكْنُونٌ
Dananu am xale yuy wër ci ñoom, yu melni pepp.
25وَأَقْبَلَ بَعْضُهُمْ عَلَىٰ بَعْضٍ يَتَسَاءَلُونَ
ku nekk jàkkaarlook moroomam tey laajante ;
26قَالُوا إِنَّا كُنَّا قَبْلُ فِي أَهْلِنَا مُشْفِقِينَ
Ñanga naan : “Nun dey ba nu nekkee Àddina danoo ragaloon [Yàlla] ;
At-TurFihi Alxuraan
49Aaya
MeccanRevelation
24Aaya
Tekki — At-Tur 24
Simoore At-Tur Aaya 24 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Dananu am xale yuy wër ci ñoom, yu melni pepp.Simoore Aaya 24/49 — Simoore At-Tur الطور (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore At-Tur Dégg, Simoore At-Tur Tekki, Simoore At-Tur mp3, Simoore At-Tur pdf. Aaya 22–26. Tekkim Wolof: Fulfulde.
العربية
English
Bahasa Indonesia
Türkçe
Русский
فارسی
Français
اردو
বাংলা
Deutsch
Español
中文
हिन्दी
Português
Italiano
ภาษาไทย
Polski
Nederlands
Shqip
Kiswahili
O'zbek
தமிழ்
Melayu
Bosanski
Soomaali
Azərbaycan
کوردی
한국어
日本語
Svenska
Dansk
Norsk
پښتو
മലയാളം
සිංහල
Tamazight
Hausa
አማርኛ
Български
Тоҷикӣ
Қазақша
Filipino
سنڌي
Yorùbá
Fulfulde
Татарча
ئۇيغۇرچە
Кыргызча
ਪੰਜਾਬੀ
Jawa
తెలుగు
မြန်မာ
ગુજરાતી
Oromo
मराठी
Tiếng Việt
Malagasy
Нохчийн
Wolof
ދިވެހި
ಕನ್ನಡ
Українська
Ελληνικά
ქართული
ខ្មែរ
دری
Qafar af
Maranao
नेपाली
Alxuraan bu Tedd bi
Tuesday, September 8, 2026
Don't forget us in your sincere prayers








