At-Tur · 23/49
Tekki Waxtaan — Simoore At-Tur
يَتَنَازَعُونَ فِيهَا كَأْسًا لَّا لَغْوٌ فِيهَا وَلَا تَأْثِيمٌ ۝٢٣
Yatanaaza`oona feehaa kaasal laa laghwun feehaa wa laa taaseem
📖 Tekkim Wolof
Danuñu cay joqlante ak i kopp ci lu àndul ak i caaxaan waxatumalaa sobe.

🎧 Dégg


📜 Aaya 21-25 — Simoore At-Tur

21وَالَّذِينَ آمَنُوا وَاتَّبَعَتْهُمْ ذُرِّيَّتُهُم بِإِيمَانٍ أَلْحَقْنَا بِهِمْ ذُرِّيَّتَهُمْ وَمَا أَلَتْنَاهُم مِّنْ عَمَلِهِم مِّن شَيْءٍ ۚ كُلُّ امْرِئٍ بِمَا كَسَبَ رَهِينٌ
Ña gëmoon te seen sët topp leen ca ngëm googee, Dananu def seeni sët ñu dab leen. Te duñu wàññi dara ci sen jëf, kenn ku nekk ay moom la mu sàkku.
22وَأَمْدَدْنَاهُم بِفَاكِهَةٍ وَلَحْمٍ مِّمَّا يَشْتَهُونَ
Te Dananu leen jox ay foytéef ak yàpp lépp lu ñu cay soxla.
23يَتَنَازَعُونَ فِيهَا كَأْسًا لَّا لَغْوٌ فِيهَا وَلَا تَأْثِيمٌ
Danuñu cay joqlante ak i kopp ci lu àndul ak i caaxaan waxatumalaa sobe.
24۞ وَيَطُوفُ عَلَيْهِمْ غِلْمَانٌ لَّهُمْ كَأَنَّهُمْ لُؤْلُؤٌ مَّكْنُونٌ
Dananu am xale yuy wër ci ñoom, yu melni pepp.
25وَأَقْبَلَ بَعْضُهُمْ عَلَىٰ بَعْضٍ يَتَسَاءَلُونَ
ku nekk jàkkaarlook moroomam tey laajante ;
At-TurFihi Alxuraan
49Aaya
MeccanRevelation
23Aaya

Tekki — At-Tur 23

Simoore At-Tur Aaya 23 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Danuñu cay joqlante ak i kopp ci lu àndul ak…

Simoore Aaya 23/49 — Simoore At-Tur الطور (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore At-Tur Dégg, Simoore At-Tur Tekki, Simoore At-Tur mp3, Simoore At-Tur pdf. Aaya 21–25. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Monday, September 7, 2026

Don't forget us in your sincere prayers