At-Tur · 26/49
Tekki Waxtaan — At-Tur
قَالُوا إِنَّا كُنَّا قَبْلُ فِي أَهْلِنَا مُشْفِقِينَ ۝٢٦
Qaalooo innaa kunnaa qablu feee ahlinaa mushfiqeen
📖 Tekkim Wolof
Ñanga naan : “Nun dey ba nu nekkee Àddina danoo ragaloon [Yàlla] ;
🎧 Dégg

📜 Aaya 24-28 — At-Tur

24۞ وَيَطُوفُ عَلَيْهِمْ غِلْمَانٌ لَّهُمْ كَأَنَّهُمْ لُؤْلُؤٌ مَّكْنُونٌ
Dananu am xale yuy wër ci ñoom, yu melni pepp.
25وَأَقْبَلَ بَعْضُهُمْ عَلَىٰ بَعْضٍ يَتَسَاءَلُونَ
ku nekk jàkkaarlook moroomam tey laajante ;
26قَالُوا إِنَّا كُنَّا قَبْلُ فِي أَهْلِنَا مُشْفِقِينَ
Ñanga naan : “Nun dey ba nu nekkee Àddina danoo ragaloon [Yàlla] ;
27فَمَنَّ اللَّهُ عَلَيْنَا وَوَقَانَا عَذَابَ السَّمُومِ
Yàlla daldi nuy baaxe fegal nu mbugalum Samuum.
28إِنَّا كُنَّا مِن قَبْلُ نَدْعُوهُ ۖ إِنَّهُ هُوَ الْبَرُّ الرَّحِيمُ
Nun dey bu jëkk, ca Àddina danu ko daan woo di ko ñaan. Moom Yàlla, moo di Aji-baax ji , di Jaglewaakoon bi yërmaandeem”.
At-TurFihi Alxuraan
49Aaya
MeccanRevelation
26Aaya

Tekki — At-Tur 26

Simoore At-Tur Aaya 26 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Ñanga naan : “Nun dey ba nu nekkee Àddina danoo…

Simoore Aaya 26/49 — At-Tur الطور (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: At-Tur Dégg, At-Tur Tekki, At-Tur mp3, At-Tur pdf. Aaya 24–28. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers