Al-Qamar · 16/55
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Qamar
فَكَيْفَ كَانَ عَذَابِي وَنُذُرِ ۝١٦
Fakaifa kaana `azaabee wa nuzur
📖 Tekkim Wolof
Te naka lay deme Sama mbugël at Samay xuppaate ?

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 14-18 — Simoore Al-Qamar

14تَجْرِي بِأَعْيُنِنَا جَزَاءً لِّمَن كَانَ كُفِرَ
mu doon dawe ci sunug càmm : faye ko ko ngir ña weddi woon.
15وَلَقَد تَّرَكْنَاهَا آيَةً فَهَلْ مِن مُّدَّكِرٍ
Bàyyi nañu ko, mu di [kéemaan]. Moo ndax kon duñu ca jàjju ?
16فَكَيْفَ كَانَ عَذَابِي وَنُذُرِ
Te naka lay deme Sama mbugël at Samay xuppaate ?
17وَلَقَدْ يَسَّرْنَا الْقُرْآنَ لِلذِّكْرِ فَهَلْ مِن مُّدَّكِرٍ
Yombal Nanu, Alxuraan ngir ñu fàttelikoo ca. Moo kon ndax kenn dana ci jàjjoo ?
18كَذَّبَتْ عَادٌ فَكَيْفَ كَانَ عَذَابِي وَنُذُرِ
Waa Aad weddi woon nañu. Waaye naka la mbugël ma deme woon ak xupp ga ma leen defoon ?
Al-QamarFihi Alxuraan
55Aaya
MeccanRevelation
16Aaya

Tekki — Al-Qamar 16

Simoore Al-Qamar Aaya 16 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Te naka lay deme Sama mbugël at Samay xuppaate ?

Simoore Aaya 16/55 — Simoore Al-Qamar القمر (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Qamar Dégg, Simoore Al-Qamar Tekki, Simoore Al-Qamar mp3, Simoore Al-Qamar pdf. Aaya 14–18. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Thursday, October 1, 2026

Don't forget us in your sincere prayers