Al-Qamar · 20/55
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Qamar
تَنزِعُ النَّاسَ كَأَنَّهُمْ أَعْجَازُ نَخْلٍ مُّنقَعِرٍ ۝٢٠
Tanzi;un naasa ka anna huma`jaazu nakhlim munqa`ir
📖 Tekkim Wolof
dadoon sempi nit ñi ni ay dàtti tàndarma di buure.

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 18-22 — Simoore Al-Qamar

18كَذَّبَتْ عَادٌ فَكَيْفَ كَانَ عَذَابِي وَنُذُرِ
Waa Aad weddi woon nañu. Waaye naka la mbugël ma deme woon ak xupp ga ma leen defoon ?
19إِنَّا أَرْسَلْنَا عَلَيْهِمْ رِيحًا صَرْصَرًا فِي يَوْمِ نَحْسٍ مُّسْتَمِرٍّ
Yabaloon nanu ca ñoom ngelaw lu ànd ak ub (sedd), ci bis bu tiis te mbugël ma faf wàccatuleen ;
20تَنزِعُ النَّاسَ كَأَنَّهُمْ أَعْجَازُ نَخْلٍ مُّنقَعِرٍ
dadoon sempi nit ñi ni ay dàtti tàndarma di buure.
21فَكَيْفَ كَانَ عَذَابِي وَنُذُرِ
Naka mu Sama mbugël ak Samag xuppaate ?
22وَلَقَدْ يَسَّرْنَا الْقُرْآنَ لِلذِّكْرِ فَهَلْ مِن مُّدَّكِرٍ
Yombal Nanu Alxuraan ngir ñu fàttalikoo ca. Moo kon ndax kenn dana ca jàjjoo ?
Al-QamarFihi Alxuraan
55Aaya
MeccanRevelation
20Aaya

Tekki — Al-Qamar 20

Simoore Al-Qamar Aaya 20 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : dadoon sempi nit ñi ni ay dàtti tàndarma di buure.

Simoore Aaya 20/55 — Simoore Al-Qamar القمر (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Qamar Dégg, Simoore Al-Qamar Tekki, Simoore Al-Qamar mp3, Simoore Al-Qamar pdf. Aaya 18–22. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Friday, October 2, 2026

Don't forget us in your sincere prayers