Ar-Rahman · 26/78
Tekki Waxtaan — Simoore Ar-Rahman
كُلُّ مَنْ عَلَيْهَا فَانٍ ۝٢٦
Kullu man `alaihaa faan
📖 Tekkim Wolof
Képp kuy dund kaw [suuf] dana masa saay jeex,

🎧 Dégg


📜 Aaya 24-28 — Simoore Ar-Rahman

24وَلَهُ الْجَوَارِ الْمُنشَآتُ فِي الْبَحْرِ كَالْأَعْلَامِ
Moo moom gaal yiy tëmbu ci biir géej niki ay tundi doj ;
25فَبِأَيِّ آلَاءِ رَبِّكُمَا تُكَذِّبَانِ
Yéen nit ak jinne ana naka ngeen di man a weddee seen xeewali Boroom ?
26كُلُّ مَنْ عَلَيْهَا فَانٍ
Képp kuy dund kaw [suuf] dana masa saay jeex,
27وَيَبْقَىٰ وَجْهُ رَبِّكَ ذُو الْجَلَالِ وَالْإِكْرَامِ
Sa Jëmmi Boroom doŋŋ fiy des, moom miy boroom màgg gi ak teraanga.
28فَبِأَيِّ آلَاءِ رَبِّكُمَا تُكَذِّبَانِ
Yéen nit ak jinne ana naka ngeen di man a weddee seen xeewali Boroom ?
Ar-RahmanFihi Alxuraan
78Aaya
MedinanRevelation
26Aaya

Tekki — Ar-Rahman 26

Simoore Ar-Rahman Aaya 26 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Képp kuy dund kaw [suuf] dana masa saay jeex,

Simoore Aaya 26/78 — Simoore Ar-Rahman الرحمن (Medinan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Ar-Rahman Dégg, Simoore Ar-Rahman Tekki, Simoore Ar-Rahman mp3, Simoore Ar-Rahman pdf. Aaya 24–28. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers