Al-Waqi'a · 82/96
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Waqi'a
وَتَجْعَلُونَ رِزْقَكُمْ أَنَّكُمْ تُكَذِّبُونَ ۝٨٢
Wa taj`aloona rizqakum annakum tukazziboon
📖 Tekkim Wolof
Ak li leen Yàlla defal lépp fayewuleen ko lu dul di weddi Alxuraan ?

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 80-84 — Simoore Al-Waqi'a

80تَنزِيلٌ مِّن رَّبِّ الْعَالَمِينَ
Mi ngi wàcci bawoo ca Yàlla Boroom àddina si.
81أَفَبِهَٰذَا الْحَدِيثِ أَنتُم مُّدْهِنُونَ
Moo ndax ci waxtaan wii ngeen di weddi ?
82وَتَجْعَلُونَ رِزْقَكُمْ أَنَّكُمْ تُكَذِّبُونَ
Ak li leen Yàlla defal lépp fayewuleen ko lu dul di weddi Alxuraan ?
83فَلَوْلَا إِذَا بَلَغَتِ الْحُلْقُومَ
Bu ruuh gi génnee ba des ci bóli gi (kuy sukuraat),
84وَأَنتُمْ حِينَئِذٍ تَنظُرُونَ
te fekk na yéen a nga koy xool,
Al-Waqi'aFihi Alxuraan
96Aaya
MeccanRevelation
82Aaya

Tekki — Al-Waqi'a 82

Simoore Al-Waqi'a Aaya 82 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Ak li leen Yàlla defal lépp fayewuleen ko lu dul…

Simoore Aaya 82/96 — Simoore Al-Waqi'a الواقعة (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Waqi'a Dégg, Simoore Al-Waqi'a Tekki, Simoore Al-Waqi'a mp3, Simoore Al-Waqi'a pdf. Aaya 80–84. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Thursday, October 1, 2026

Don't forget us in your sincere prayers