Al-Waqi'a · 84/96
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Waqi'a
وَأَنتُمْ حِينَئِذٍ تَنظُرُونَ ۝٨٤
Wa antum heena`izin tanzuroon
📖 Tekkim Wolof
te fekk na yéen a nga koy xool,

🎧 Dégg


📜 Aaya 82-86 — Simoore Al-Waqi'a

82وَتَجْعَلُونَ رِزْقَكُمْ أَنَّكُمْ تُكَذِّبُونَ
Ak li leen Yàlla defal lépp fayewuleen ko lu dul di weddi Alxuraan ?
83فَلَوْلَا إِذَا بَلَغَتِ الْحُلْقُومَ
Bu ruuh gi génnee ba des ci bóli gi (kuy sukuraat),
84وَأَنتُمْ حِينَئِذٍ تَنظُرُونَ
te fekk na yéen a nga koy xool,
85وَنَحْنُ أَقْرَبُ إِلَيْهِ مِنكُمْ وَلَٰكِن لَّا تُبْصِرُونَ
fekk na booba Nun Yàlla noo ko gëna jigeñ waaye du ngeen gis.
86فَلَوْلَا إِن كُنتُمْ غَيْرَ مَدِينِينَ
Bu ngeen, jortee ne ameeluleen Yàlla dara,
Al-Waqi'aFihi Alxuraan
96Aaya
MeccanRevelation
84Aaya

Tekki — Al-Waqi'a 84

Simoore Al-Waqi'a Aaya 84 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : te fekk na yéen a nga koy xool,

Simoore Aaya 84/96 — Simoore Al-Waqi'a الواقعة (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Waqi'a Dégg, Simoore Al-Waqi'a Tekki, Simoore Al-Waqi'a mp3, Simoore Al-Waqi'a pdf. Aaya 82–86. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers