Al-Waqi'a · 83/96
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Waqi'a
فَلَوْلَا إِذَا بَلَغَتِ الْحُلْقُومَ ۝٨٣
Falaw laaa izaa balaghatil hulqoom
📖 Tekkim Wolof
Bu ruuh gi génnee ba des ci bóli gi (kuy sukuraat),

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 81-85 — Simoore Al-Waqi'a

81أَفَبِهَٰذَا الْحَدِيثِ أَنتُم مُّدْهِنُونَ
Moo ndax ci waxtaan wii ngeen di weddi ?
82وَتَجْعَلُونَ رِزْقَكُمْ أَنَّكُمْ تُكَذِّبُونَ
Ak li leen Yàlla defal lépp fayewuleen ko lu dul di weddi Alxuraan ?
83فَلَوْلَا إِذَا بَلَغَتِ الْحُلْقُومَ
Bu ruuh gi génnee ba des ci bóli gi (kuy sukuraat),
84وَأَنتُمْ حِينَئِذٍ تَنظُرُونَ
te fekk na yéen a nga koy xool,
85وَنَحْنُ أَقْرَبُ إِلَيْهِ مِنكُمْ وَلَٰكِن لَّا تُبْصِرُونَ
fekk na booba Nun Yàlla noo ko gëna jigeñ waaye du ngeen gis.
Al-Waqi'aFihi Alxuraan
96Aaya
MeccanRevelation
83Aaya

Tekki — Al-Waqi'a 83

Simoore Al-Waqi'a Aaya 83 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Bu ruuh gi génnee ba des ci bóli gi (kuy…

Simoore Aaya 83/96 — Simoore Al-Waqi'a الواقعة (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Waqi'a Dégg, Simoore Al-Waqi'a Tekki, Simoore Al-Waqi'a mp3, Simoore Al-Waqi'a pdf. Aaya 81–85. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Monday, September 28, 2026

Don't forget us in your sincere prayers