Al-Waqi'a · 90/96
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Waqi'a
وَأَمَّا إِن كَانَ مِنْ أَصْحَابِ الْيَمِينِ ۝٩٠
Wa ammaaa in kaana min as haabil yameen
📖 Tekkim Wolof
Su fekkee ne nag dafa bokk ci waa ndeyjoor,

🎧 Dégg


📜 Aaya 88-92 — Simoore Al-Waqi'a

88فَأَمَّا إِن كَانَ مِنَ الْمُقَرَّبِينَ
Su fekkee ne koo ku dafa jige woon (Yàlla),
89فَرَوْحٌ وَرَيْحَانٌ وَجَنَّتُ نَعِيمٍ
dana (am) noflaay, ak àjjanay xéewël.
90وَأَمَّا إِن كَانَ مِنْ أَصْحَابِ الْيَمِينِ
Su fekkee ne nag dafa bokk ci waa ndeyjoor,
91فَسَلَامٌ لَّكَ مِنْ أَصْحَابِ الْيَمِينِ
dees na ko [teeroo]: “Jàmm ju” bawoo ca waa ndeyjoor.
92وَأَمَّا إِن كَانَ مِنَ الْمُكَذِّبِينَ الضَّالِّينَ
Su fekkee ne nag dafa bokk ca ña daan weddi (dekkiwaat) tey ñu réer sànku,
Al-Waqi'aFihi Alxuraan
96Aaya
MeccanRevelation
90Aaya

Tekki — Al-Waqi'a 90

Simoore Al-Waqi'a Aaya 90 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Su fekkee ne nag dafa bokk ci waa ndeyjoor,

Simoore Aaya 90/96 — Simoore Al-Waqi'a الواقعة (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Waqi'a Dégg, Simoore Al-Waqi'a Tekki, Simoore Al-Waqi'a mp3, Simoore Al-Waqi'a pdf. Aaya 88–92. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Monday, September 7, 2026

Don't forget us in your sincere prayers