Al-Waqi'a · 91/96
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Waqi'a
فَسَلَامٌ لَّكَ مِنْ أَصْحَابِ الْيَمِينِ ۝٩١
Fasalaamul laka min as haabil yameen
📖 Tekkim Wolof
dees na ko [teeroo]: “Jàmm ju” bawoo ca waa ndeyjoor.

🎧 Dégg


📜 Aaya 89-93 — Simoore Al-Waqi'a

89فَرَوْحٌ وَرَيْحَانٌ وَجَنَّتُ نَعِيمٍ
dana (am) noflaay, ak àjjanay xéewël.
90وَأَمَّا إِن كَانَ مِنْ أَصْحَابِ الْيَمِينِ
Su fekkee ne nag dafa bokk ci waa ndeyjoor,
91فَسَلَامٌ لَّكَ مِنْ أَصْحَابِ الْيَمِينِ
dees na ko [teeroo]: “Jàmm ju” bawoo ca waa ndeyjoor.
92وَأَمَّا إِن كَانَ مِنَ الْمُكَذِّبِينَ الضَّالِّينَ
Su fekkee ne nag dafa bokk ca ña daan weddi (dekkiwaat) tey ñu réer sànku,
93فَنُزُلٌ مِّنْ حَمِيمٍ
des na ko teeroo ndox muy wañax,
Al-Waqi'aFihi Alxuraan
96Aaya
MeccanRevelation
91Aaya

Tekki — Al-Waqi'a 91

Simoore Al-Waqi'a Aaya 91 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : dees na ko [teeroo]: “Jàmm ju” bawoo ca waa ndeyjoor.

Simoore Aaya 91/96 — Simoore Al-Waqi'a الواقعة (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Waqi'a Dégg, Simoore Al-Waqi'a Tekki, Simoore Al-Waqi'a mp3, Simoore Al-Waqi'a pdf. Aaya 89–93. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers