Al-Waqi'a · 89/96
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Waqi'a
فَرَوْحٌ وَرَيْحَانٌ وَجَنَّتُ نَعِيمٍ ۝٨٩
Farawhunw wa raihaa nunw wa jannatu na`eem
📖 Tekkim Wolof
dana (am) noflaay, ak àjjanay xéewël.

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 87-91 — Simoore Al-Waqi'a

87تَرْجِعُونَهَا إِن كُنتُمْ صَادِقِينَ
ana lan moo tax kon delloosiwuleen [ruuh ga], ndegam ñu dëggu ngeen ?
88فَأَمَّا إِن كَانَ مِنَ الْمُقَرَّبِينَ
Su fekkee ne koo ku dafa jige woon (Yàlla),
89فَرَوْحٌ وَرَيْحَانٌ وَجَنَّتُ نَعِيمٍ
dana (am) noflaay, ak àjjanay xéewël.
90وَأَمَّا إِن كَانَ مِنْ أَصْحَابِ الْيَمِينِ
Su fekkee ne nag dafa bokk ci waa ndeyjoor,
91فَسَلَامٌ لَّكَ مِنْ أَصْحَابِ الْيَمِينِ
dees na ko [teeroo]: “Jàmm ju” bawoo ca waa ndeyjoor.
Al-Waqi'aFihi Alxuraan
96Aaya
MeccanRevelation
89Aaya

Tekki — Al-Waqi'a 89

Simoore Al-Waqi'a Aaya 89 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : dana (am) noflaay, ak àjjanay xéewël.

Simoore Aaya 89/96 — Simoore Al-Waqi'a الواقعة (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Waqi'a Dégg, Simoore Al-Waqi'a Tekki, Simoore Al-Waqi'a mp3, Simoore Al-Waqi'a pdf. Aaya 87–91. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Monday, September 28, 2026

Don't forget us in your sincere prayers