Al-Hashr · 15/24
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Hashr
كَمَثَلِ الَّذِينَ مِن قَبْلِهِمْ قَرِيبًا ۖ ذَاقُوا وَبَالَ أَمْرِهِمْ وَلَهُمْ عَذَابٌ أَلِيمٌ ۝١٥
Kamasalil lazeena min qablihim qareeban zaaqoo wabaala amrihim wa lahum `azaabun aleem
📖 Tekkim Wolof
danoo melni ñi leen jigeñ, te jiitu woon leen (Yéefëri Makka), mos nañu alkaande seen jëf te danañu am mbugël mu tar ;

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 13-17 — Simoore Al-Hashr

13لَأَنتُمْ أَشَدُّ رَهْبَةً فِي صُدُورِهِم مِّنَ اللَّهِ ۚ ذَٰلِكَ بِأَنَّهُمْ قَوْمٌ لَّا يَفْقَهُونَ
Ñoom naaféq yi seen jëmm yii la ñu gën a ragal ci Yàlla. Ndax ñoom dañoo xamul.
14لَا يُقَاتِلُونَكُمْ جَمِيعًا إِلَّا فِي قُرًى مُّحَصَّنَةٍ أَوْ مِن وَرَاءِ جُدُرٍ ۚ بَأْسُهُم بَيْنَهُمْ شَدِيدٌ ۚ تَحْسَبُهُمْ جَمِيعًا وَقُلُوبُهُمْ شَتَّىٰ ۚ ذَٰلِكَ بِأَنَّهُمْ قَوْمٌ لَّا يَعْقِلُونَ
Duñuy xeex ak yéen mukk (ñoom naaféq ya) lu dul biir dëkk yu ñu tata ci ginnaaw ay ñag. Seenug noonoo ci seen biir lu tar la. Danga foog ne ñu ànd lañu, te seeni xol dañoo féewoo. Li ko waral moo di ne dañoo amul ay xol di ko jariñoo.
15كَمَثَلِ الَّذِينَ مِن قَبْلِهِمْ قَرِيبًا ۖ ذَاقُوا وَبَالَ أَمْرِهِمْ وَلَهُمْ عَذَابٌ أَلِيمٌ
danoo melni ñi leen jigeñ, te jiitu woon leen (Yéefëri Makka), mos nañu alkaande seen jëf te danañu am mbugël mu tar ;
16كَمَثَلِ الشَّيْطَانِ إِذْ قَالَ لِلْإِنسَانِ اكْفُرْ فَلَمَّا كَفَرَ قَالَ إِنِّي بَرِيءٌ مِّنكَ إِنِّي أَخَافُ اللَّهَ رَبَّ الْعَالَمِينَ
dafay melni rekk Saytaane ba muy wax ak nit naan ko : “Weddil”. Ba mu weddee, mu ne ko : “Man kat deñ naa ci yaw ndax man damaa ragal Yàlla, miy Boroom àddina si”.
17فَكَانَ عَاقِبَتَهُمَا أَنَّهُمَا فِي النَّارِ خَالِدَيْنِ فِيهَا ۚ وَذَٰلِكَ جَزَاءُ الظَّالِمِينَ
Su ko defee ñoom ñaar Safaraay doon seenug muj ñu béel fa. Loolu mooy peyug tooñkat ya.
Al-HashrFihi Alxuraan
24Aaya
MedinanRevelation
15Aaya

Tekki — Al-Hashr 15

Simoore Al-Hashr Aaya 15 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : danoo melni ñi leen jigeñ, te jiitu woon leen (Yéefëri…

Simoore Aaya 15/24 — Simoore Al-Hashr الحشر (Medinan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Hashr Dégg, Simoore Al-Hashr Tekki, Simoore Al-Hashr mp3, Simoore Al-Hashr pdf. Aaya 13–17. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Thursday, October 1, 2026

Don't forget us in your sincere prayers