Al-Mulk · 24/30
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Mulk
قُلْ هُوَ الَّذِي ذَرَأَكُمْ فِي الْأَرْضِ وَإِلَيْهِ تُحْشَرُونَ ٢٤
Transliteration
Qul huwal lazee zara akum fil ardi wa ilaihi tuhsharoon
Tekki (Tekkim Wolof)
📖 Tekkim Wolof
Waxal ne : “It moo leen ji ci suuf si, te ca moom ngeen di mujj ñu pang leen”.
Additional reference in Fulfulde
M
Mishary Rashid Alafasy
✓
Mishary Rashid Alafasy
✓
M
Mahmoud Khalil Al-Husary
✓
Mahmoud Khalil Al-Husary
✓
A
Abdurrahman As-Sudais
✓
Abdurrahman As-Sudais
✓
M
Mohamed Siddiq Al-Minshawi
✓
Mohamed Siddiq Al-Minshawi
✓
A
Abdul Basit Abdul Samad
✓
Abdul Basit Abdul Samad
✓
A
Ali Al-Hudhaify
✓
Ali Al-Hudhaify
✓
A
Ahmed ibn Ali al-Ajamy
✓
Ahmed ibn Ali al-Ajamy
✓
A
Abu Bakr Ash-Shaatree
✓
Abu Bakr Ash-Shaatree
✓
M
Muhammad Ayyoub
✓
Muhammad Ayyoub
✓
A
Abdullah Basfar
✓
Abdullah Basfar
✓
A
Abdullah Al-Juhani
✓
Abdullah Al-Juhani
✓
M
Maher Al Muaiqly
✓
Maher Al Muaiqly
✓
0:00
0:00
📜 Aaya 22-26 — Simoore Al-Mulk
22أَفَمَن يَمْشِي مُكِبًّا عَلَىٰ وَجْهِهِ أَهْدَىٰ أَمَّن يَمْشِي سَوِيًّا عَلَىٰ صِرَاطٍ مُّسْتَقِيمٍ
Moo ndax ? Waajiy dëpp xarkanamam moo gën a gindiku kiy dox ne sàtt ca kaw yoon wa jub xocc.
23قُلْ هُوَ الَّذِي أَنشَأَكُمْ وَجَعَلَ لَكُمُ السَّمْعَ وَالْأَبْصَارَ وَالْأَفْئِدَةَ ۖ قَلِيلًا مَّا تَشْكُرُونَ
Waxal ne: “Moom moo leen sàkk defal leen dégg, ak ub gis ak i xol”. Te néewaana ngeen sant delloo njukël !
24قُلْ هُوَ الَّذِي ذَرَأَكُمْ فِي الْأَرْضِ وَإِلَيْهِ تُحْشَرُونَ
Waxal ne : “It moo leen ji ci suuf si, te ca moom ngeen di mujj ñu pang leen”.
25وَيَقُولُونَ مَتَىٰ هَٰذَا الْوَعْدُ إِن كُنتُمْ صَادِقِينَ
Ñuy wax naan : “Dig ba kañ lay doon su fekkee ne ñu dëggu ngeen ? ”.
26قُلْ إِنَّمَا الْعِلْمُ عِندَ اللَّهِ وَإِنَّمَا أَنَا نَذِيرٌ مُّبِينٌ
Waxal ne : “Xam-xamub loolu ma nga ca Yàlla. Man nag ab xuppekat buy leeral laa”.
Al-MulkFihi Alxuraan
30Aaya
MeccanRevelation
24Aaya
Tekki — Al-Mulk 24
Simoore Al-Mulk Aaya 24 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Waxal ne : “It moo leen ji ci suuf si,…Simoore Aaya 24/30 — Simoore Al-Mulk الملك (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Mulk Dégg, Simoore Al-Mulk Tekki, Simoore Al-Mulk mp3, Simoore Al-Mulk pdf. Aaya 22–26. Tekkim Wolof: Fulfulde.
Simoore Al-Mulk
العربية
English
Bahasa Indonesia
Türkçe
Русский
فارسی
Français
اردو
বাংলা
Deutsch
Español
中文
हिन्दी
Português
Italiano
ภาษาไทย
Polski
Nederlands
Shqip
Kiswahili
O'zbek
தமிழ்
Melayu
Bosanski
Soomaali
Azərbaycan
کوردی
한국어
日本語
Svenska
Dansk
Norsk
پښتو
മലയാളം
සිංහල
Tamazight
Hausa
አማርኛ
Български
Тоҷикӣ
Қазақша
Filipino
سنڌي
Yorùbá
Fulfulde
Татарча
ئۇيغۇرچە
Кыргызча
ਪੰਜਾਬੀ
Jawa
తెలుగు
မြန်မာ
ગુજરાતી
Oromo
मराठी
Tiếng Việt
Malagasy
Нохчийн
Wolof
ދިވެހި
ಕನ್ನಡ
Українська
Ελληνικά
ქართული
ខ្មែរ
دری
Qafar af
Maranao
नेपाली
Alxuraan bu Tedd bi
Monday, September 28, 2026
Don't forget us in your sincere prayers


