Al-Mulk · 3/30
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Mulk
الَّذِي خَلَقَ سَبْعَ سَمَاوَاتٍ طِبَاقًا ۖ مَّا تَرَىٰ فِي خَلْقِ الرَّحْمَٰنِ مِن تَفَاوُتٍ ۖ فَارْجِعِ الْبَصَرَ هَلْ تَرَىٰ مِن فُطُورٍ ۝٣
Allazee khalaqa sab`a samaawaatin tibaaqam maa taraa fee khalqir rahmaani min tafaawutin farji`il basara hal taraa min futoor
📖 Tekkim Wolof
Mooy ki bind juróom-ñaari asamaan yu tegloo doo gis kenn roobaate ci bindug Yërëmaakoon bi. Dellul xool. Moo ndax danga gis genn sutaate ?

🎧 Dégg


📜 Aaya 1-5 — Simoore Al-Mulk

1تَبَارَكَ الَّذِي بِيَدِهِ الْمُلْكُ وَهُوَ عَلَىٰ كُلِّ شَيْءٍ قَدِيرٌ
Barkeel na (Yàlla) mi nga xam ne nguur gaa ngi ci loxom, te Moom man na Lépp lu ne.
2الَّذِي خَلَقَ الْمَوْتَ وَالْحَيَاةَ لِيَبْلُوَكُمْ أَيُّكُمْ أَحْسَنُ عَمَلًا ۚ وَهُوَ الْعَزِيزُ الْغَفُورُ
Mooy ki bind dee ak dund ngir nattu leen ci ana kan koo gën a rafet jëf, te Moom (Yàlla) moo di boroom Kàttan gi, di Jéggalaakoon bi.
3الَّذِي خَلَقَ سَبْعَ سَمَاوَاتٍ طِبَاقًا ۖ مَّا تَرَىٰ فِي خَلْقِ الرَّحْمَٰنِ مِن تَفَاوُتٍ ۖ فَارْجِعِ الْبَصَرَ هَلْ تَرَىٰ مِن فُطُورٍ
Mooy ki bind juróom-ñaari asamaan yu tegloo doo gis kenn roobaate ci bindug Yërëmaakoon bi. Dellul xool. Moo ndax danga gis genn sutaate ?
4ثُمَّ ارْجِعِ الْبَصَرَ كَرَّتَيْنِ يَنقَلِبْ إِلَيْكَ الْبَصَرُ خَاسِئًا وَهُوَ حَسِيرٌ
Topp, nga déllu xool ñaari yoon : da koy délloosiwaat ci yaw rekk waaye du man a gis sikk ne cucum.
5وَلَقَدْ زَيَّنَّا السَّمَاءَ الدُّنْيَا بِمَصَابِيحَ وَجَعَلْنَاهَا رُجُومًا لِّلشَّيَاطِينِ ۖ وَأَعْتَدْنَا لَهُمْ عَذَابَ السَّعِيرِ
Taaralal nanu àddina si ci ay làmp [biddiw] def nanu ko muy lakk Saytaane yi te waajalal nanu leen mbugëlum Safara.
Al-MulkFihi Alxuraan
30Aaya
MeccanRevelation
3Aaya

Tekki — Al-Mulk 3

Simoore Al-Mulk Aaya 3 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Mooy ki bind juróom-ñaari asamaan yu tegloo doo gis kenn…

Simoore Aaya 3/30 — Simoore Al-Mulk الملك (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Mulk Dégg, Simoore Al-Mulk Tekki, Simoore Al-Mulk mp3, Simoore Al-Mulk pdf. Aaya 1–5. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Monday, September 7, 2026

Don't forget us in your sincere prayers