Al-Qalam · 27/52
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Qalam
بَلْ نَحْنُ مَحْرُومُونَ ۝٢٧
Bal nahnu mahroomoon
📖 Tekkim Wolof
Ñu ne moom la kat waaye li wóor moo di ne su nu muur jeex na ci”.

🎧 Dégg


📜 Aaya 25-29 — Simoore Al-Qalam

25وَغَدَوْا عَلَىٰ حَرْدٍ قَادِرِينَ
Ñu xëy njortu ne, man nañoo tere tool ya.
26فَلَمَّا رَأَوْهَا قَالُوا إِنَّا لَضَالُّونَ
Ba ñu ne gegg, ca tool ya ( mu melni peroŋ) : ñu ne : “nun xanaa da noo gëlam,
27بَلْ نَحْنُ مَحْرُومُونَ
Ñu ne moom la kat waaye li wóor moo di ne su nu muur jeex na ci”.
28قَالَ أَوْسَطُهُمْ أَلَمْ أَقُل لَّكُمْ لَوْلَا تُسَبِّحُونَ
Ka ca gën a yiw ne leen : “Ndax nee wu ma leen : Ngeen di sàbbaal seen Boroom di ko kañ ! ”
29قَالُوا سُبْحَانَ رَبِّنَا إِنَّا كُنَّا ظَالِمِينَ
Ñu daldi ne : “Tudd nanu selluk sunu Boroom ! Nun dey, ay tooñkat lanu woon”.
Al-QalamFihi Alxuraan
52Aaya
MeccanRevelation
27Aaya

Tekki — Al-Qalam 27

Simoore Al-Qalam Aaya 27 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Ñu ne moom la kat waaye li wóor moo di…

Simoore Aaya 27/52 — Simoore Al-Qalam القلم (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Qalam Dégg, Simoore Al-Qalam Tekki, Simoore Al-Qalam mp3, Simoore Al-Qalam pdf. Aaya 25–29. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Monday, September 7, 2026

Don't forget us in your sincere prayers