Al-Qalam · 26/52
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Qalam
فَلَمَّا رَأَوْهَا قَالُوا إِنَّا لَضَالُّونَ ۝٢٦
Falammaa ra awhaa qaalooo innaa ladaaalloon
📖 Tekkim Wolof
Ba ñu ne gegg, ca tool ya ( mu melni peroŋ) : ñu ne : “nun xanaa da noo gëlam,

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 24-28 — Simoore Al-Qalam

24أَن لَّا يَدْخُلَنَّهَا الْيَوْمَ عَلَيْكُم مِّسْكِينٌ
Tey wax naan : “Tey jii buleen seetaan benn miskin di dugg ci tool yi”.
25وَغَدَوْا عَلَىٰ حَرْدٍ قَادِرِينَ
Ñu xëy njortu ne, man nañoo tere tool ya.
26فَلَمَّا رَأَوْهَا قَالُوا إِنَّا لَضَالُّونَ
Ba ñu ne gegg, ca tool ya ( mu melni peroŋ) : ñu ne : “nun xanaa da noo gëlam,
27بَلْ نَحْنُ مَحْرُومُونَ
Ñu ne moom la kat waaye li wóor moo di ne su nu muur jeex na ci”.
28قَالَ أَوْسَطُهُمْ أَلَمْ أَقُل لَّكُمْ لَوْلَا تُسَبِّحُونَ
Ka ca gën a yiw ne leen : “Ndax nee wu ma leen : Ngeen di sàbbaal seen Boroom di ko kañ ! ”
Al-QalamFihi Alxuraan
52Aaya
MeccanRevelation
26Aaya

Tekki — Al-Qalam 26

Simoore Al-Qalam Aaya 26 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Ba ñu ne gegg, ca tool ya ( mu melni…

Simoore Aaya 26/52 — Simoore Al-Qalam القلم (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Qalam Dégg, Simoore Al-Qalam Tekki, Simoore Al-Qalam mp3, Simoore Al-Qalam pdf. Aaya 24–28. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Thursday, October 1, 2026

Don't forget us in your sincere prayers