Al-Qalam · 28/52
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Qalam
قَالَ أَوْسَطُهُمْ أَلَمْ أَقُل لَّكُمْ لَوْلَا تُسَبِّحُونَ ۝٢٨
Qaala awsatuhum alam aqul lakum law laa tusabbihoon
📖 Tekkim Wolof
Ka ca gën a yiw ne leen : “Ndax nee wu ma leen : Ngeen di sàbbaal seen Boroom di ko kañ ! ”

🎧 Dégg


📜 Aaya 26-30 — Simoore Al-Qalam

26فَلَمَّا رَأَوْهَا قَالُوا إِنَّا لَضَالُّونَ
Ba ñu ne gegg, ca tool ya ( mu melni peroŋ) : ñu ne : “nun xanaa da noo gëlam,
27بَلْ نَحْنُ مَحْرُومُونَ
Ñu ne moom la kat waaye li wóor moo di ne su nu muur jeex na ci”.
28قَالَ أَوْسَطُهُمْ أَلَمْ أَقُل لَّكُمْ لَوْلَا تُسَبِّحُونَ
Ka ca gën a yiw ne leen : “Ndax nee wu ma leen : Ngeen di sàbbaal seen Boroom di ko kañ ! ”
29قَالُوا سُبْحَانَ رَبِّنَا إِنَّا كُنَّا ظَالِمِينَ
Ñu daldi ne : “Tudd nanu selluk sunu Boroom ! Nun dey, ay tooñkat lanu woon”.
30فَأَقْبَلَ بَعْضُهُمْ عَلَىٰ بَعْضٍ يَتَلَاوَمُونَ
Ku nekk dëgmal morom ja, ñuy yeddante.
Al-QalamFihi Alxuraan
52Aaya
MeccanRevelation
28Aaya

Tekki — Al-Qalam 28

Simoore Al-Qalam Aaya 28 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Ka ca gën a yiw ne leen : “Ndax nee…

Simoore Aaya 28/52 — Simoore Al-Qalam القلم (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Qalam Dégg, Simoore Al-Qalam Tekki, Simoore Al-Qalam mp3, Simoore Al-Qalam pdf. Aaya 26–30. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Monday, September 7, 2026

Don't forget us in your sincere prayers