Al-Qalam · 30/52
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Qalam
فَأَقْبَلَ بَعْضُهُمْ عَلَىٰ بَعْضٍ يَتَلَاوَمُونَ ۝٣٠
Fa aqbala ba`duhum `alaa ba`diny yatalaawamoon
📖 Tekkim Wolof
Ku nekk dëgmal morom ja, ñuy yeddante.

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 28-32 — Simoore Al-Qalam

28قَالَ أَوْسَطُهُمْ أَلَمْ أَقُل لَّكُمْ لَوْلَا تُسَبِّحُونَ
Ka ca gën a yiw ne leen : “Ndax nee wu ma leen : Ngeen di sàbbaal seen Boroom di ko kañ ! ”
29قَالُوا سُبْحَانَ رَبِّنَا إِنَّا كُنَّا ظَالِمِينَ
Ñu daldi ne : “Tudd nanu selluk sunu Boroom ! Nun dey, ay tooñkat lanu woon”.
30فَأَقْبَلَ بَعْضُهُمْ عَلَىٰ بَعْضٍ يَتَلَاوَمُونَ
Ku nekk dëgmal morom ja, ñuy yeddante.
31قَالُوا يَا وَيْلَنَا إِنَّا كُنَّا طَاغِينَ
Ñuy wax naan : “Ngalla ! Nun danoo bew.
32عَسَىٰ رَبُّنَا أَن يُبْدِلَنَا خَيْرًا مِّنْهَا إِنَّا إِلَىٰ رَبِّنَا رَاغِبُونَ
Aka neexoon Yàlla nangu sunu tuub wuutalal nu ko ak tool yu ko gën. Sunu Boroom la nu xemmem”.
Al-QalamFihi Alxuraan
52Aaya
MeccanRevelation
30Aaya

Tekki — Al-Qalam 30

Simoore Al-Qalam Aaya 30 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Ku nekk dëgmal morom ja, ñuy yeddante.

Simoore Aaya 30/52 — Simoore Al-Qalam القلم (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Qalam Dégg, Simoore Al-Qalam Tekki, Simoore Al-Qalam mp3, Simoore Al-Qalam pdf. Aaya 28–32. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Thursday, October 1, 2026

Don't forget us in your sincere prayers