Al-A'raf · 147/206
Tekki Waxtaan — Al-A'raf
وَالَّذِينَ كَذَّبُوا بِآيَاتِنَا وَلِقَاءِ الْآخِرَةِ حَبِطَتْ أَعْمَالُهُمْ ۚ هَلْ يُجْزَوْنَ إِلَّا مَا كَانُوا يَعْمَلُونَ ۝١٤٧
Wallazeena kazzaboo bi Aayaatinaa wa liqaaa`il Aakhirati habitat `amaaluhum; hal yujzawna illaa maa kaanoo ya`maloon
📖 Tekkim Wolof
Ña weddi Sunuy kàddu ak ndaje mu mujj ma, seeni jëf yàqu na. Ndax deesuleen fey lu dul la ñu daan def ”

🎧 Dégg


📜 Aaya 145-149 — Al-A'raf

145وَكَتَبْنَا لَهُ فِي الْأَلْوَاحِ مِن كُلِّ شَيْءٍ مَّوْعِظَةً وَتَفْصِيلًا لِّكُلِّ شَيْءٍ فَخُذْهَا بِقُوَّةٍ وَأْمُرْ قَوْمَكَ يَأْخُذُوا بِأَحْسَنِهَا ۚ سَأُرِيكُمْ دَارَ الْفَاسِقِينَ
Nu bindal ko ci àlluwaya lu nekk ngir waare ak faramfàcce lu nekk ba mu waar ko cig farlu. “Nu digal ko mu wax ay nitam ñu jàppe ko ca na mu gën a rafete. Danaa leen won dëkku saay-saay sa.
146سَأَصْرِفُ عَنْ آيَاتِيَ الَّذِينَ يَتَكَبَّرُونَ فِي الْأَرْضِ بِغَيْرِ الْحَقِّ وَإِن يَرَوْا كُلَّ آيَةٍ لَّا يُؤْمِنُوا بِهَا وَإِن يَرَوْا سَبِيلَ الرُّشْدِ لَا يَتَّخِذُوهُ سَبِيلًا وَإِن يَرَوْا سَبِيلَ الْغَيِّ يَتَّخِذُوهُ سَبِيلًا ۚ ذَٰلِكَ بِأَنَّهُمْ كَذَّبُوا بِآيَاتِنَا وَكَانُوا عَنْهَا غَافِلِينَ
Danaa soreel Samay tegtal ña rëy-rëylu ci suuf si ci lu dul dëgg. Ba bu ñu gisee bépp kéemaan duñu ko gëm. Bu ñu gisee yoon wu njub, duñu ko topp, muy seenu yoon. Li waral loolu mooy dañoo weddi Sunuy kàddu, sàggan ba dëddu leen.
147وَالَّذِينَ كَذَّبُوا بِآيَاتِنَا وَلِقَاءِ الْآخِرَةِ حَبِطَتْ أَعْمَالُهُمْ ۚ هَلْ يُجْزَوْنَ إِلَّا مَا كَانُوا يَعْمَلُونَ
Ña weddi Sunuy kàddu ak ndaje mu mujj ma, seeni jëf yàqu na. Ndax deesuleen fey lu dul la ñu daan def ”
148وَاتَّخَذَ قَوْمُ مُوسَىٰ مِن بَعْدِهِ مِنْ حُلِيِّهِمْ عِجْلًا جَسَدًا لَّهُ خُوَارٌ ۚ أَلَمْ يَرَوْا أَنَّهُ لَا يُكَلِّمُهُمْ وَلَا يَهْدِيهِمْ سَبِيلًا ۘ اتَّخَذُوهُ وَكَانُوا ظَالِمِينَ
Nitu Muusaa jàpp nañu ci ginnaawam aw yëkk wu ñu takk seeni takkaayi yaram, weddi Sunuy kàddu. Ndax dañoo gisul ne moom mënuta wax ak ñoom te duleen jubale ciw yoon ? Jàpp nañu ko [di ko jaamu], nekk i way-tooñ.
149وَلَمَّا سُقِطَ فِي أَيْدِيهِمْ وَرَأَوْا أَنَّهُمْ قَدْ ضَلُّوا قَالُوا لَئِن لَّمْ يَرْحَمْنَا رَبُّنَا وَيَغْفِرْ لَنَا لَنَكُونَنَّ مِنَ الْخَاسِرِينَ
Waaye ba mu daanoo ca seeni yoxo, te ñu gis ne ñoom dañoo nekkoon cig réer, ñu ne sunu Boroom : “Soo nu yërëmul, baal nu, dananu bokk ca way-yàqule ña”.
Al-A'rafFihi Alxuraan
206Aaya
MeccanRevelation
147Aaya

Tekki — Al-A'raf 147

Simoore Al-A'raf Aaya 147 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Ña weddi Sunuy kàddu ak ndaje mu mujj ma, seeni…

Simoore Aaya 147/206 — Al-A'raf الأعراف (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-A'raf Dégg, Al-A'raf Tekki, Al-A'raf mp3, Al-A'raf pdf. Aaya 145–149. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Wednesday, August 19, 2026

Don't forget us in your sincere prayers