An-Naba · 39/40
Tekki Waxtaan — An-Naba
ذَٰلِكَ الْيَوْمُ الْحَقُّ ۖ فَمَن شَاءَ اتَّخَذَ إِلَىٰ رَبِّهِ مَآبًا ۝٣٩
Zaalikal yaumul haqqu faman shaa-at ta khaaza ill-laa rabbihi ma-aaba
📖 Tekkim Wolof
Loolu moo di bisub dëgg ba. Ku mu soob mu jël Boroomam def ko ab rawtukaay.
🎧 Dégg

📜 Aaya 37-40 — An-Naba

37رَّبِّ السَّمَاوَاتِ وَالْأَرْضِ وَمَا بَيْنَهُمَا الرَّحْمَٰنِ ۖ لَا يَمْلِكُونَ مِنْهُ خِطَابًا
Boroom asamaan yeek suuf seek li ci seen diggante, mooy Yëramaakoon bi ; duñu mana waxanteek moom.
38يَوْمَ يَقُومُ الرُّوحُ وَالْمَلَائِكَةُ صَفًّا ۖ لَّا يَتَكَلَّمُونَ إِلَّا مَنْ أَذِنَ لَهُ الرَّحْمَٰنُ وَقَالَ صَوَابًا
Bu keroogee ba Jibriil jóg ànd ak malaaka ya taxaw def sàppe, duñu wax , lu dul ku Yàlla Yëramaakoon bi jox ndigël, mu wax lay dëgg te yem ca kepp.
39ذَٰلِكَ الْيَوْمُ الْحَقُّ ۖ فَمَن شَاءَ اتَّخَذَ إِلَىٰ رَبِّهِ مَآبًا
Loolu moo di bisub dëgg ba. Ku mu soob mu jël Boroomam def ko ab rawtukaay.
40إِنَّا أَنذَرْنَاكُمْ عَذَابًا قَرِيبًا يَوْمَ يَنظُرُ الْمَرْءُ مَا قَدَّمَتْ يَدَاهُ وَيَقُولُ الْكَافِرُ يَا لَيْتَنِي كُنتُ تُرَابًا
Xuppnaa leen ci mbugëlum bis bu jigeen, bu keroogee ba nit ñi di xool la ñu jëfoon ; yéefar ba naan : “Aka neexoon may suuf”.
An-NabaFihi Alxuraan
40Aaya
MeccanRevelation
39Aaya

Tekki — An-Naba 39

Simoore An-Naba Aaya 39 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Loolu moo di bisub dëgg ba. Ku mu soob mu…

Simoore Aaya 39/40 — An-Naba النبأ (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: An-Naba Dégg, An-Naba Tekki, An-Naba mp3, An-Naba pdf. Aaya 37–40. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers