An-Naba · 4/40
Tekki Waxtaan — Simoore An-Naba
كَلَّا سَيَعْلَمُونَ ۝٤
Kallaa sa y`alamoon
📖 Tekkim Wolof
Mukk ! danañu xala xam.

🎧 Dégg


📜 Aaya 2-6 — Simoore An-Naba

2عَنِ النَّبَإِ الْعَظِيمِ
Ci xibaar bu rëy ba,
3الَّذِي هُمْ فِيهِ مُخْتَلِفُونَ
xibaar ba nga xam ne dañu caa juuyoo.
4كَلَّا سَيَعْلَمُونَ
Mukk ! danañu xala xam.
5ثُمَّ كَلَّا سَيَعْلَمُونَ
Déedéet kay ! Danañu xala xam.
6أَلَمْ نَجْعَلِ الْأَرْضَ مِهَادًا
Moo ndax du Nun Noo def suuf si mu di laltaay ?
An-NabaFihi Alxuraan
40Aaya
MeccanRevelation
4Aaya

Tekki — An-Naba 4

Simoore An-Naba Aaya 4 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Mukk ! danañu xala xam.

Simoore Aaya 4/40 — Simoore An-Naba النبأ (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore An-Naba Dégg, Simoore An-Naba Tekki, Simoore An-Naba mp3, Simoore An-Naba pdf. Aaya 2–6. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Monday, September 7, 2026

Don't forget us in your sincere prayers