An-Naba · 5/40
Tekki Waxtaan — Simoore An-Naba
ثُمَّ كَلَّا سَيَعْلَمُونَ ۝٥
Thumma kallaa sa y`alamoon
📖 Tekkim Wolof
Déedéet kay ! Danañu xala xam.

🎧 Dégg


📜 Aaya 3-7 — Simoore An-Naba

3الَّذِي هُمْ فِيهِ مُخْتَلِفُونَ
xibaar ba nga xam ne dañu caa juuyoo.
4كَلَّا سَيَعْلَمُونَ
Mukk ! danañu xala xam.
5ثُمَّ كَلَّا سَيَعْلَمُونَ
Déedéet kay ! Danañu xala xam.
6أَلَمْ نَجْعَلِ الْأَرْضَ مِهَادًا
Moo ndax du Nun Noo def suuf si mu di laltaay ?
7وَالْجِبَالَ أَوْتَادًا
ak tundi doj yi ñu di ay dott ?
An-NabaFihi Alxuraan
40Aaya
MeccanRevelation
5Aaya

Tekki — An-Naba 5

Simoore An-Naba Aaya 5 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Déedéet kay ! Danañu xala xam.

Simoore Aaya 5/40 — Simoore An-Naba النبأ (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore An-Naba Dégg, Simoore An-Naba Tekki, Simoore An-Naba mp3, Simoore An-Naba pdf. Aaya 3–7. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers