An-Nazi'at · 17/46
Tekki Waxtaan — Simoore An-Nazi'at
اذْهَبْ إِلَىٰ فِرْعَوْنَ إِنَّهُ طَغَىٰ ۝١٧
Izhab ilaa fir`auna innahu taghaa
📖 Tekkim Wolof
“Demal ca Firawna. Moom bew na !

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 15-19 — Simoore An-Nazi'at

15هَلْ أَتَاكَ حَدِيثُ مُوسَىٰ
Ndax waxtaanu Muusaa dikkël na la ? Ay xibaaram ?
16إِذْ نَادَاهُ رَبُّهُ بِالْوَادِ الْمُقَدَّسِ طُوًى
Ba ko Boroomam di woo, ca xuru Tuwaa, wu sell wa, di ko wax ne :
17اذْهَبْ إِلَىٰ فِرْعَوْنَ إِنَّهُ طَغَىٰ
“Demal ca Firawna. Moom bew na !
18فَقُلْ هَل لَّكَ إِلَىٰ أَن تَزَكَّىٰ
Te nga wax ko ne : “Ndax bëgg ngaa tuub ?
19وَأَهْدِيَكَ إِلَىٰ رَبِّكَ فَتَخْشَىٰ
kon dey da naa la gindi ci sa Boroom nga ragal ko ? ”
An-Nazi'atFihi Alxuraan
46Aaya
MeccanRevelation
17Aaya

Tekki — An-Nazi'at 17

Simoore An-Nazi'at Aaya 17 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : “Demal ca Firawna. Moom bew na !

Simoore Aaya 17/46 — Simoore An-Nazi'at النازعات (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore An-Nazi'at Dégg, Simoore An-Nazi'at Tekki, Simoore An-Nazi'at mp3, Simoore An-Nazi'at pdf. Aaya 15–19. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Wednesday, September 30, 2026

Don't forget us in your sincere prayers