An-Nazi'at · 16/46
Tekki Waxtaan — Simoore An-Nazi'at
إِذْ نَادَاهُ رَبُّهُ بِالْوَادِ الْمُقَدَّسِ طُوًى ۝١٦
Iz nadaahu rabbuhu bil waadil-muqad dasi tuwa
📖 Tekkim Wolof
Ba ko Boroomam di woo, ca xuru Tuwaa, wu sell wa, di ko wax ne :

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 14-18 — Simoore An-Nazi'at

14فَإِذَا هُم بِالسَّاهِرَةِ
ñu jekki-jekki rekk ne jaww ci kaw suuf si dekkiwaat.
15هَلْ أَتَاكَ حَدِيثُ مُوسَىٰ
Ndax waxtaanu Muusaa dikkël na la ? Ay xibaaram ?
16إِذْ نَادَاهُ رَبُّهُ بِالْوَادِ الْمُقَدَّسِ طُوًى
Ba ko Boroomam di woo, ca xuru Tuwaa, wu sell wa, di ko wax ne :
17اذْهَبْ إِلَىٰ فِرْعَوْنَ إِنَّهُ طَغَىٰ
“Demal ca Firawna. Moom bew na !
18فَقُلْ هَل لَّكَ إِلَىٰ أَن تَزَكَّىٰ
Te nga wax ko ne : “Ndax bëgg ngaa tuub ?
An-Nazi'atFihi Alxuraan
46Aaya
MeccanRevelation
16Aaya

Tekki — An-Nazi'at 16

Simoore An-Nazi'at Aaya 16 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Ba ko Boroomam di woo, ca xuru Tuwaa, wu sell…

Simoore Aaya 16/46 — Simoore An-Nazi'at النازعات (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore An-Nazi'at Dégg, Simoore An-Nazi'at Tekki, Simoore An-Nazi'at mp3, Simoore An-Nazi'at pdf. Aaya 14–18. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Wednesday, September 30, 2026

Don't forget us in your sincere prayers