An-Nazi'at · 18/46
Tekki Waxtaan — Simoore An-Nazi'at
فَقُلْ هَل لَّكَ إِلَىٰ أَن تَزَكَّىٰ ۝١٨
Faqul hal laka ilaa-an tazakka
📖 Tekkim Wolof
Te nga wax ko ne : “Ndax bëgg ngaa tuub ?

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 16-20 — Simoore An-Nazi'at

16إِذْ نَادَاهُ رَبُّهُ بِالْوَادِ الْمُقَدَّسِ طُوًى
Ba ko Boroomam di woo, ca xuru Tuwaa, wu sell wa, di ko wax ne :
17اذْهَبْ إِلَىٰ فِرْعَوْنَ إِنَّهُ طَغَىٰ
“Demal ca Firawna. Moom bew na !
18فَقُلْ هَل لَّكَ إِلَىٰ أَن تَزَكَّىٰ
Te nga wax ko ne : “Ndax bëgg ngaa tuub ?
19وَأَهْدِيَكَ إِلَىٰ رَبِّكَ فَتَخْشَىٰ
kon dey da naa la gindi ci sa Boroom nga ragal ko ? ”
20فَأَرَاهُ الْآيَةَ الْكُبْرَىٰ
Mu wan ko keemtaan yu màgg ya.
An-Nazi'atFihi Alxuraan
46Aaya
MeccanRevelation
18Aaya

Tekki — An-Nazi'at 18

Simoore An-Nazi'at Aaya 18 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Te nga wax ko ne : “Ndax bëgg ngaa tuub…

Simoore Aaya 18/46 — Simoore An-Nazi'at النازعات (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore An-Nazi'at Dégg, Simoore An-Nazi'at Tekki, Simoore An-Nazi'at mp3, Simoore An-Nazi'at pdf. Aaya 16–20. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Wednesday, September 30, 2026

Don't forget us in your sincere prayers