An-Nazi'at · 23/46
Tekki Waxtaan — An-Nazi'at
فَحَشَرَ فَنَادَىٰ ۝٢٣
Fa hashara fanada
📖 Tekkim Wolof
daldi woo nit ña dajale leen,

🎧 Dégg


📜 Aaya 21-25 — An-Nazi'at

21فَكَذَّبَ وَعَصَىٰ
Mu weddi ko (Firawna) daldi koy moy ;
22ثُمَّ أَدْبَرَ يَسْعَىٰ
Mu daldi, dumóoyu, féew dem,
23فَحَشَرَ فَنَادَىٰ
daldi woo nit ña dajale leen,
24فَقَالَ أَنَا رَبُّكُمُ الْأَعْلَىٰ
daldi wax ne : “Man maay sen boroom, bi gëna kawe”.
25فَأَخَذَهُ اللَّهُ نَكَالَ الْآخِرَةِ وَالْأُولَىٰ
Yàlla daldi koy faagaagal mbugalum àddina muy sar ba àllaaxira.
An-Nazi'atFihi Alxuraan
46Aaya
MeccanRevelation
23Aaya

Tekki — An-Nazi'at 23

Simoore An-Nazi'at Aaya 23 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : daldi woo nit ña dajale leen,

Simoore Aaya 23/46 — An-Nazi'at النازعات (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: An-Nazi'at Dégg, An-Nazi'at Tekki, An-Nazi'at mp3, An-Nazi'at pdf. Aaya 21–25. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers