An-Nazi'at · 22/46
Tekki Waxtaan — Simoore An-Nazi'at
ثُمَّ أَدْبَرَ يَسْعَىٰ ۝٢٢
Thumma adbara yas`aa
📖 Tekkim Wolof
Mu daldi, dumóoyu, féew dem,

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 20-24 — Simoore An-Nazi'at

20فَأَرَاهُ الْآيَةَ الْكُبْرَىٰ
Mu wan ko keemtaan yu màgg ya.
21فَكَذَّبَ وَعَصَىٰ
Mu weddi ko (Firawna) daldi koy moy ;
22ثُمَّ أَدْبَرَ يَسْعَىٰ
Mu daldi, dumóoyu, féew dem,
23فَحَشَرَ فَنَادَىٰ
daldi woo nit ña dajale leen,
24فَقَالَ أَنَا رَبُّكُمُ الْأَعْلَىٰ
daldi wax ne : “Man maay sen boroom, bi gëna kawe”.
An-Nazi'atFihi Alxuraan
46Aaya
MeccanRevelation
22Aaya

Tekki — An-Nazi'at 22

Simoore An-Nazi'at Aaya 22 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Mu daldi, dumóoyu, féew dem,

Simoore Aaya 22/46 — Simoore An-Nazi'at النازعات (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore An-Nazi'at Dégg, Simoore An-Nazi'at Tekki, Simoore An-Nazi'at mp3, Simoore An-Nazi'at pdf. Aaya 20–24. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Monday, September 28, 2026

Don't forget us in your sincere prayers