Al-Anfal · 15/75
Tekki Waxtaan — Al-Anfal
يَا أَيُّهَا الَّذِينَ آمَنُوا إِذَا لَقِيتُمُ الَّذِينَ كَفَرُوا زَحْفًا فَلَا تُوَلُّوهُمُ الْأَدْبَارَ ١٥
Transliteration
Yaaa aiyuhal lazeena aamanoo izaa laqeetumul lazeena kafaroo zahfan falaa tuwalloohumul adbaar
Tekki (Tekkim Wolof)
📖 Tekkim Wolof
Éy yéen ñi gëm ñi, bu ngeen dajeek yéefar yi ñuy ràngu jëm ci yéen, buleen daw won leen ginnaaw.
Additional reference in Fulfulde
🎧 Dégg
📜 Aaya 13-17 — Al-Anfal
13ذَٰلِكَ بِأَنَّهُمْ شَاقُّوا اللَّهَ وَرَسُولَهُ ۚ وَمَن يُشَاقِقِ اللَّهَ وَرَسُولَهُ فَإِنَّ اللَّهَ شَدِيدُ الْعِقَابِ
Loolu, ngir dañoo juuyook Yàlla ak Yonentam.”. Te ku juuyook Yàlla ak Yonentam, ... [na xam ne] Yàlla ku tar mbugal la !
14ذَٰلِكُمْ فَذُوقُوهُ وَأَنَّ لِلْكَافِرِينَ عَذَابَ النَّارِ
Noonu lay dalee ci yéen [yéefar yi] ; kon mosleen ko ! Te ñeel na way-weddi ña mbugalu Safara.
15يَا أَيُّهَا الَّذِينَ آمَنُوا إِذَا لَقِيتُمُ الَّذِينَ كَفَرُوا زَحْفًا فَلَا تُوَلُّوهُمُ الْأَدْبَارَ
Éy yéen ñi gëm ñi, bu ngeen dajeek yéefar yi ñuy ràngu jëm ci yéen, buleen daw won leen ginnaaw.
16وَمَن يُوَلِّهِمْ يَوْمَئِذٍ دُبُرَهُ إِلَّا مُتَحَرِّفًا لِّقِتَالٍ أَوْ مُتَحَيِّزًا إِلَىٰ فِئَةٍ فَقَدْ بَاءَ بِغَضَبٍ مِّنَ اللَّهِ وَمَأْوَاهُ جَهَنَّمُ ۖ وَبِئْسَ الْمَصِيرُ
Ku daw won leen ginnaaw, ca bis boobu - lu dul kuy jéem a njuuy ba jekku na mu war a xeexe, walla kuy jéem a tafu ci mboolom jullit, - tàbbi ci merum Yàlla te dëkkuwaayam Safara la. Aka bon booba dëkkuwaay !
17فَلَمْ تَقْتُلُوهُمْ وَلَٰكِنَّ اللَّهَ قَتَلَهُمْ ۚ وَمَا رَمَيْتَ إِذْ رَمَيْتَ وَلَٰكِنَّ اللَّهَ رَمَىٰ ۚ وَلِيُبْلِيَ الْمُؤْمِنِينَ مِنْهُ بَلَاءً حَسَنًا ۚ إِنَّ اللَّهَ سَمِيعٌ عَلِيمٌ
Te reyuleen leen [yéen jullit ñi] : Yàlla moo leen rey. Te sànniwoo [yaw Yonent bi], bi nga sànnee suuf si : waaye Yàlla moo sànni, ngir Mu may jullit ñi xéewal gu rafet gu tukke ca Moom Yàlla ! Te Yàlla Kuy dégg la, Kuy xam la.
Al-AnfalFihi Alxuraan
75Aaya
MedinanRevelation
15Aaya
Tekki — Al-Anfal 15
Simoore Al-Anfal Aaya 15 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Éy yéen ñi gëm ñi, bu ngeen dajeek yéefar yi…Simoore Aaya 15/75 — Al-Anfal الأنفال (Medinan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-Anfal Dégg, Al-Anfal Tekki, Al-Anfal mp3, Al-Anfal pdf. Aaya 13–17. Tekkim Wolof: Fulfulde.
العربية
English
Bahasa Indonesia
Türkçe
Русский
فارسی
Français
اردو
বাংলা
Deutsch
Español
中文
हिन्दी
Português
Italiano
ภาษาไทย
Polski
Nederlands
Shqip
Kiswahili
O'zbek
தமிழ்
Melayu
Bosanski
Soomaali
Azərbaycan
کوردی
한국어
日本語
Svenska
Dansk
Norsk
پښتو
മലയാളം
සිංහල
Tamazight
Hausa
አማርኛ
Български
Тоҷикӣ
Қазақша
Filipino
سنڌي
Yorùbá
Fulfulde
Татарча
ئۇيغۇرچە
Кыргызча
ਪੰਜਾਬੀ
Jawa
తెలుగు
မြန်မာ
ગુજરાતી
Oromo
मराठी
Tiếng Việt
Malagasy
Нохчийн
Wolof
ދިވެހި
ಕನ್ನಡ
Українська
Ελληνικά
ქართული
ខ្មែរ
دری
Qafar af
Maranao
नेपाली
Alxuraan bu Tedd bi
Tuesday, August 18, 2026
Don't forget us in your sincere prayers








