Al-Infitar · 12/19
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Infitar
يَعْلَمُونَ مَا تَفْعَلُونَ ۝١٢
Ya`lamoona ma taf`aloon
📖 Tekkim Wolof
yuy xam li ngeen di def.

🎧 Dégg


📜 Aaya 10-14 — Simoore Al-Infitar

10وَإِنَّ عَلَيْكُمْ لَحَافِظِينَ
te am na ay wattukat yu nekk ci seen kaw,
11كِرَامًا كَاتِبِينَ
yu tedd yuy bind,
12يَعْلَمُونَ مَا تَفْعَلُونَ
yuy xam li ngeen di def.
13إِنَّ الْأَبْرَارَ لَفِي نَعِيمٍ
Ñu baax ñaa ngi ca biir àjjanay xéewal,
14وَإِنَّ الْفُجَّارَ لَفِي جَحِيمٍ
te itam kàccoor ya ñoom, ña nga ca biir safara jahiim
Al-InfitarFihi Alxuraan
19Aaya
MeccanRevelation
12Aaya

Tekki — Al-Infitar 12

Simoore Al-Infitar Aaya 12 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : yuy xam li ngeen di def.

Simoore Aaya 12/19 — Simoore Al-Infitar الإنفطار (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Infitar Dégg, Simoore Al-Infitar Tekki, Simoore Al-Infitar mp3, Simoore Al-Infitar pdf. Aaya 10–14. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers