Al-Infitar · 13/19
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Infitar
إِنَّ الْأَبْرَارَ لَفِي نَعِيمٍ ۝١٣
Innal abraara lafee na`eem
📖 Tekkim Wolof
Ñu baax ñaa ngi ca biir àjjanay xéewal,

🎧 Dégg


📜 Aaya 11-15 — Simoore Al-Infitar

11كِرَامًا كَاتِبِينَ
yu tedd yuy bind,
12يَعْلَمُونَ مَا تَفْعَلُونَ
yuy xam li ngeen di def.
13إِنَّ الْأَبْرَارَ لَفِي نَعِيمٍ
Ñu baax ñaa ngi ca biir àjjanay xéewal,
14وَإِنَّ الْفُجَّارَ لَفِي جَحِيمٍ
te itam kàccoor ya ñoom, ña nga ca biir safara jahiim
15يَصْلَوْنَهَا يَوْمَ الدِّينِ
danañu ca xoyomoo, bu bis Pénc baa
Al-InfitarFihi Alxuraan
19Aaya
MeccanRevelation
13Aaya

Tekki — Al-Infitar 13

Simoore Al-Infitar Aaya 13 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Ñu baax ñaa ngi ca biir àjjanay xéewal,

Simoore Aaya 13/19 — Simoore Al-Infitar الإنفطار (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Infitar Dégg, Simoore Al-Infitar Tekki, Simoore Al-Infitar mp3, Simoore Al-Infitar pdf. Aaya 11–15. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Monday, September 7, 2026

Don't forget us in your sincere prayers