Yunus · 54/109
Tekki Waxtaan — Yunus
وَلَوْ أَنَّ لِكُلِّ نَفْسٍ ظَلَمَتْ مَا فِي الْأَرْضِ لَافْتَدَتْ بِهِ ۗ وَأَسَرُّوا النَّدَامَةَ لَمَّا رَأَوُا الْعَذَابَ ۖ وَقُضِيَ بَيْنَهُم بِالْقِسْطِ ۚ وَهُمْ لَا يُظْلَمُونَ ۝٥٤
Wa law anna likulli nafsin zalamat maa fil ardi laftadat bih; wa asarrun nadaamata lammaa ra awul `azaab, wa qudiya bainahum bilqist; wa hum laa yuzlamoon
📖 Tekkim Wolof
Bépp bakkan bu tooñ, bu amoon li nekk ci àddina si, dana ko nangoo joxe ngir jotoo ko.Te bu ñu gisee mbugal ma, dana jéem a nëbb seenug rëccu. Waaye deef na àtte seeni diggante ci maandute, te kenn duleen tooñ [ci wàññil leen dara]..

🎧 Dégg


📜 Aaya 52-56 — Yunus

52ثُمَّ قِيلَ لِلَّذِينَ ظَلَمُوا ذُوقُوا عَذَابَ الْخُلْدِ هَلْ تُجْزَوْنَ إِلَّا بِمَا كُنتُمْ تَكْسِبُونَ
Topp waxees tooñkat ya : “Ayca mosleen mbugal mu sax dàkk ! Moo ndax dees na leen feye lu wuuteek la ngeen doon fàggu ? ”
53۞ وَيَسْتَنبِئُونَكَ أَحَقٌّ هُوَ ۖ قُلْ إِي وَرَبِّي إِنَّهُ لَحَقٌّ ۖ وَمَا أَنتُم بِمُعْجِزِينَ
Te danañu sàkku nga leeral : “Ndax loolu dëgg la ? ” - Neel : “Waawaaw ! Giñ naa ci sama Boroom ne dëgg la !Te yéen dungeen mën a raw”.
54وَلَوْ أَنَّ لِكُلِّ نَفْسٍ ظَلَمَتْ مَا فِي الْأَرْضِ لَافْتَدَتْ بِهِ ۗ وَأَسَرُّوا النَّدَامَةَ لَمَّا رَأَوُا الْعَذَابَ ۖ وَقُضِيَ بَيْنَهُم بِالْقِسْطِ ۚ وَهُمْ لَا يُظْلَمُونَ
Bépp bakkan bu tooñ, bu amoon li nekk ci àddina si, dana ko nangoo joxe ngir jotoo ko.Te bu ñu gisee mbugal ma, dana jéem a nëbb seenug rëccu. Waaye deef na àtte seeni diggante ci maandute, te kenn duleen tooñ [ci wàññil leen dara]..
55أَلَا إِنَّ لِلَّهِ مَا فِي السَّمَاوَاتِ وَالْأَرْضِ ۗ أَلَا إِنَّ وَعْدَ اللَّهِ حَقٌّ وَلَٰكِنَّ أَكْثَرَهُمْ لَا يَعْلَمُونَ
Moo ndax dafa nekkul ne Yàlla moo moom li nekk ci asamaan yi ak suuf si. Digub Yàlla mooy dëgg tigi. Waaye li ëpp ci ñoom xamuñu.
56هُوَ يُحْيِي وَيُمِيتُ وَإِلَيْهِ تُرْجَعُونَ
Moom mooy dundal, Mooy rey ; te ci Moom ngeen di dellu.
YunusFihi Alxuraan
109Aaya
MeccanRevelation
54Aaya

Tekki — Yunus 54

Simoore Yunus Aaya 54 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Bépp bakkan bu tooñ, bu amoon li nekk ci àddina…

Simoore Aaya 54/109 — Yunus يونس (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Yunus Dégg, Yunus Tekki, Yunus mp3, Yunus pdf. Aaya 52–56. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Wednesday, August 19, 2026

Don't forget us in your sincere prayers