Yunus · 53/109
Tekki Waxtaan — Yunus
۞ وَيَسْتَنبِئُونَكَ أَحَقٌّ هُوَ ۖ قُلْ إِي وَرَبِّي إِنَّهُ لَحَقٌّ ۖ وَمَا أَنتُم بِمُعْجِزِينَ ۝٥٣
Wa yastambi`oonaka ahaqqun huwa qul ee wa Rabbeee innahoo lahaqq; wa maaa antum bimu`jizeen
📖 Tekkim Wolof
Te danañu sàkku nga leeral : “Ndax loolu dëgg la ? ” - Neel : “Waawaaw ! Giñ naa ci sama Boroom ne dëgg la !Te yéen dungeen mën a raw”.
🎧 Dégg

📜 Aaya 51-55 — Yunus

51أَثُمَّ إِذَا مَا وَقَعَ آمَنتُم بِهِ ۚ آلْآنَ وَقَدْ كُنتُم بِهِ تَسْتَعْجِلُونَ
“Moo ndax bu agsee ngeen koy door a gëm ? [Kon deef na leen wax : “Léegi, yéen a ngi ci biir ba noppi”.] Te yéen a ngi koy yàkkamti”.
52ثُمَّ قِيلَ لِلَّذِينَ ظَلَمُوا ذُوقُوا عَذَابَ الْخُلْدِ هَلْ تُجْزَوْنَ إِلَّا بِمَا كُنتُمْ تَكْسِبُونَ
Topp waxees tooñkat ya : “Ayca mosleen mbugal mu sax dàkk ! Moo ndax dees na leen feye lu wuuteek la ngeen doon fàggu ? ”
53۞ وَيَسْتَنبِئُونَكَ أَحَقٌّ هُوَ ۖ قُلْ إِي وَرَبِّي إِنَّهُ لَحَقٌّ ۖ وَمَا أَنتُم بِمُعْجِزِينَ
Te danañu sàkku nga leeral : “Ndax loolu dëgg la ? ” - Neel : “Waawaaw ! Giñ naa ci sama Boroom ne dëgg la !Te yéen dungeen mën a raw”.
54وَلَوْ أَنَّ لِكُلِّ نَفْسٍ ظَلَمَتْ مَا فِي الْأَرْضِ لَافْتَدَتْ بِهِ ۗ وَأَسَرُّوا النَّدَامَةَ لَمَّا رَأَوُا الْعَذَابَ ۖ وَقُضِيَ بَيْنَهُم بِالْقِسْطِ ۚ وَهُمْ لَا يُظْلَمُونَ
Bépp bakkan bu tooñ, bu amoon li nekk ci àddina si, dana ko nangoo joxe ngir jotoo ko.Te bu ñu gisee mbugal ma, dana jéem a nëbb seenug rëccu. Waaye deef na àtte seeni diggante ci maandute, te kenn duleen tooñ [ci wàññil leen dara]..
55أَلَا إِنَّ لِلَّهِ مَا فِي السَّمَاوَاتِ وَالْأَرْضِ ۗ أَلَا إِنَّ وَعْدَ اللَّهِ حَقٌّ وَلَٰكِنَّ أَكْثَرَهُمْ لَا يَعْلَمُونَ
Moo ndax dafa nekkul ne Yàlla moo moom li nekk ci asamaan yi ak suuf si. Digub Yàlla mooy dëgg tigi. Waaye li ëpp ci ñoom xamuñu.
YunusFihi Alxuraan
109Aaya
MeccanRevelation
53Aaya

Tekki — Yunus 53

Simoore Yunus Aaya 53 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Te danañu sàkku nga leeral : “Ndax loolu dëgg la…

Simoore Aaya 53/109 — Yunus يونس (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Yunus Dégg, Yunus Tekki, Yunus mp3, Yunus pdf. Aaya 51–55. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers