Yunus · 83/109
Tekki Waxtaan — Yunus
فَمَا آمَنَ لِمُوسَىٰ إِلَّا ذُرِّيَّةٌ مِّن قَوْمِهِ عَلَىٰ خَوْفٍ مِّن فِرْعَوْنَ وَمَلَئِهِمْ أَن يَفْتِنَهُمْ ۚ وَإِنَّ فِرْعَوْنَ لَعَالٍ فِي الْأَرْضِ وَإِنَّهُ لَمِنَ الْمُسْرِفِينَ ۝٨٣
Famaaa aamana li-Moosaaa illaa zurriyyatum min qawmihee `alaa khawfim min Fir`awna wa mala`ihim ai yaftinahum; wa inna Fir`awna la`aalin fil ardi wa innahoo laminal musrifeen
📖 Tekkim Wolof
Te kenn gëmul woon Muusaa lu dul ab kurél ci aw nitam, [la ko waral] mooy Firawna ak mbooloo ma lañu ragal seen fitna. Te Firawna dafa rëy-rëylu woon ci kaw suuf si, kawe lool, te moom bokk na ca saay-saay sa.
🎧 Dégg

📜 Aaya 81-85 — Yunus

81فَلَمَّا أَلْقَوْا قَالَ مُوسَىٰ مَا جِئْتُم بِهِ السِّحْرُ ۖ إِنَّ اللَّهَ سَيُبْطِلُهُ ۖ إِنَّ اللَّهَ لَا يُصْلِحُ عَمَلَ الْمُفْسِدِينَ
Ba ñu sànnee, Muusaa ne leen : “Li ngeen indi jibar rekk la ! Yàlla dana ko neenal. Ne : “Yàlla du àntuloo jëfi yàqkat ya”.
82وَيُحِقُّ اللَّهُ الْحَقَّ بِكَلِمَاتِهِ وَلَوْ كَرِهَ الْمُجْرِمُونَ
Te Yàlla dana notal dëgg ci dogalam, doonte neexul it ñu dëng ña”.
83فَمَا آمَنَ لِمُوسَىٰ إِلَّا ذُرِّيَّةٌ مِّن قَوْمِهِ عَلَىٰ خَوْفٍ مِّن فِرْعَوْنَ وَمَلَئِهِمْ أَن يَفْتِنَهُمْ ۚ وَإِنَّ فِرْعَوْنَ لَعَالٍ فِي الْأَرْضِ وَإِنَّهُ لَمِنَ الْمُسْرِفِينَ
Te kenn gëmul woon Muusaa lu dul ab kurél ci aw nitam, [la ko waral] mooy Firawna ak mbooloo ma lañu ragal seen fitna. Te Firawna dafa rëy-rëylu woon ci kaw suuf si, kawe lool, te moom bokk na ca saay-saay sa.
84وَقَالَ مُوسَىٰ يَا قَوْمِ إِن كُنتُمْ آمَنتُم بِاللَّهِ فَعَلَيْهِ تَوَكَّلُوا إِن كُنتُم مُّسْلِمِينَ
Muusaa ne : "Yéen samaw nit, ndegam gëm ngeen Yàlla, nangeen wéeru ci Moom ndeem ñu wommatu tigi ngeen te di ay jullit”.
85فَقَالُوا عَلَى اللَّهِ تَوَكَّلْنَا رَبَّنَا لَا تَجْعَلْنَا فِتْنَةً لِّلْقَوْمِ الظَّالِمِينَ
Ñu wax ne : “Ci Yàlla lanuy wéeru. Yaw sunu Boroom, Yàlla boonu teg nattu ya tooñkat ya yayoo.
YunusFihi Alxuraan
109Aaya
MeccanRevelation
83Aaya

Tekki — Yunus 83

Simoore Yunus Aaya 83 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Te kenn gëmul woon Muusaa lu dul ab kurél ci…

Simoore Aaya 83/109 — Yunus يونس (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Yunus Dégg, Yunus Tekki, Yunus mp3, Yunus pdf. Aaya 81–85. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers