Yunus · 82/109
Tekki Waxtaan — Yunus
وَيُحِقُّ اللَّهُ الْحَقَّ بِكَلِمَاتِهِ وَلَوْ كَرِهَ الْمُجْرِمُونَ ۝٨٢
Wa yuhiqqul laahul haqqa bi Kalimaatihee wa law karihal mujrimoon
📖 Tekkim Wolof
Te Yàlla dana notal dëgg ci dogalam, doonte neexul it ñu dëng ña”.
🎧 Dégg

📜 Aaya 80-84 — Yunus

80فَلَمَّا جَاءَ السَّحَرَةُ قَالَ لَهُم مُّوسَىٰ أَلْقُوا مَا أَنتُم مُّلْقُونَ
Ba jibarkat ya dikkee, Muusaa ne leen : “Sànnileen li ngeen di sànni”.
81فَلَمَّا أَلْقَوْا قَالَ مُوسَىٰ مَا جِئْتُم بِهِ السِّحْرُ ۖ إِنَّ اللَّهَ سَيُبْطِلُهُ ۖ إِنَّ اللَّهَ لَا يُصْلِحُ عَمَلَ الْمُفْسِدِينَ
Ba ñu sànnee, Muusaa ne leen : “Li ngeen indi jibar rekk la ! Yàlla dana ko neenal. Ne : “Yàlla du àntuloo jëfi yàqkat ya”.
82وَيُحِقُّ اللَّهُ الْحَقَّ بِكَلِمَاتِهِ وَلَوْ كَرِهَ الْمُجْرِمُونَ
Te Yàlla dana notal dëgg ci dogalam, doonte neexul it ñu dëng ña”.
83فَمَا آمَنَ لِمُوسَىٰ إِلَّا ذُرِّيَّةٌ مِّن قَوْمِهِ عَلَىٰ خَوْفٍ مِّن فِرْعَوْنَ وَمَلَئِهِمْ أَن يَفْتِنَهُمْ ۚ وَإِنَّ فِرْعَوْنَ لَعَالٍ فِي الْأَرْضِ وَإِنَّهُ لَمِنَ الْمُسْرِفِينَ
Te kenn gëmul woon Muusaa lu dul ab kurél ci aw nitam, [la ko waral] mooy Firawna ak mbooloo ma lañu ragal seen fitna. Te Firawna dafa rëy-rëylu woon ci kaw suuf si, kawe lool, te moom bokk na ca saay-saay sa.
84وَقَالَ مُوسَىٰ يَا قَوْمِ إِن كُنتُمْ آمَنتُم بِاللَّهِ فَعَلَيْهِ تَوَكَّلُوا إِن كُنتُم مُّسْلِمِينَ
Muusaa ne : "Yéen samaw nit, ndegam gëm ngeen Yàlla, nangeen wéeru ci Moom ndeem ñu wommatu tigi ngeen te di ay jullit”.
YunusFihi Alxuraan
109Aaya
MeccanRevelation
82Aaya

Tekki — Yunus 82

Simoore Yunus Aaya 82 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Te Yàlla dana notal dëgg ci dogalam, doonte neexul it…

Simoore Aaya 82/109 — Yunus يونس (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Yunus Dégg, Yunus Tekki, Yunus mp3, Yunus pdf. Aaya 80–84. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers