Yunus · 98/109
Tekki Waxtaan — Yunus
فَلَوْلَا كَانَتْ قَرْيَةٌ آمَنَتْ فَنَفَعَهَا إِيمَانُهَا إِلَّا قَوْمَ يُونُسَ لَمَّا آمَنُوا كَشَفْنَا عَنْهُمْ عَذَابَ الْخِزْيِ فِي الْحَيَاةِ الدُّنْيَا وَمَتَّعْنَاهُمْ إِلَىٰ حِينٍ ۝٩٨
Falaw laa kaanat qaryatun aamanat fanafa`ahaaa eemaanuhaaa illaa qawma Yoonusa lammaaa aamanoo kashafnaa `anhum `azaabal khizyi fil hayaatid dunyaa wa matta`naahum ilaa heen
📖 Tekkim Wolof
Te amul benn dëkk [bu gëmadi, bu alkaande dikkee] buy door a gëm, di jariñoo ngëmam, lu dul nitu Yuunusa ! Ba ñu gëmee Lanu leen teggil mbugal muy toroxale ci dundug àddina gii, teg ca jox leen ay xéewal ab diir.
🎧 Dégg

📜 Aaya 96-100 — Yunus

96إِنَّ الَّذِينَ حَقَّتْ عَلَيْهِمْ كَلِمَتُ رَبِّكَ لَا يُؤْمِنُونَ
Ña nga xam ne seen kàddug Boroom far na dal ca seen kaw, duñu gëm,
97وَلَوْ جَاءَتْهُمْ كُلُّ آيَةٍ حَتَّىٰ يَرَوُا الْعَذَابَ الْأَلِيمَ
doonte la tegtal yépp dikkal na leen it [duñu gëm], mbete ñu gisee mbugal mu metti ma.
98فَلَوْلَا كَانَتْ قَرْيَةٌ آمَنَتْ فَنَفَعَهَا إِيمَانُهَا إِلَّا قَوْمَ يُونُسَ لَمَّا آمَنُوا كَشَفْنَا عَنْهُمْ عَذَابَ الْخِزْيِ فِي الْحَيَاةِ الدُّنْيَا وَمَتَّعْنَاهُمْ إِلَىٰ حِينٍ
Te amul benn dëkk [bu gëmadi, bu alkaande dikkee] buy door a gëm, di jariñoo ngëmam, lu dul nitu Yuunusa ! Ba ñu gëmee Lanu leen teggil mbugal muy toroxale ci dundug àddina gii, teg ca jox leen ay xéewal ab diir.
99وَلَوْ شَاءَ رَبُّكَ لَآمَنَ مَن فِي الْأَرْضِ كُلُّهُمْ جَمِيعًا ۚ أَفَأَنتَ تُكْرِهُ النَّاسَ حَتَّىٰ يَكُونُوا مُؤْمِنِينَ
Bu neexoon sa Boroorm, fàwwu ñi nekk ci kaw suuf si ñépp gëm. Moo ndax yaw dangay ga [gétén] nit ñi ci ñu nekk ñu gëm ?
100وَمَا كَانَ لِنَفْسٍ أَن تُؤْمِنَ إِلَّا بِإِذْنِ اللَّهِ ۚ وَيَجْعَلُ الرِّجْسَ عَلَى الَّذِينَ لَا يَعْقِلُونَ
Yellul ci benn bakkan muy gëm lu dul ci coobarey Yàlla. Te Dana teg mbugal ña xel- luwul [ba mën a ràññee dëgg].
YunusFihi Alxuraan
109Aaya
MeccanRevelation
98Aaya

Tekki — Yunus 98

Simoore Yunus Aaya 98 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Te amul benn dëkk [bu gëmadi, bu alkaande dikkee] buy…

Simoore Aaya 98/109 — Yunus يونس (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Yunus Dégg, Yunus Tekki, Yunus mp3, Yunus pdf. Aaya 96–100. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers