Hud · 116/123
Tekki Waxtaan — Hud
فَلَوْلَا كَانَ مِنَ الْقُرُونِ مِن قَبْلِكُمْ أُولُو بَقِيَّةٍ يَنْهَوْنَ عَنِ الْفَسَادِ فِي الْأَرْضِ إِلَّا قَلِيلًا مِّمَّنْ أَنجَيْنَا مِنْهُمْ ۗ وَاتَّبَعَ الَّذِينَ ظَلَمُوا مَا أُتْرِفُوا فِيهِ وَكَانُوا مُجْرِمِينَ ۝١١٦
Falw laa kaana minal qurooni min qablikum ooloo baqiyyatiny yanhawna `anil fasaadi fil ardi illaa qaleelam mimman anjainaa minhum; wattaba`al lazeena zalamoo maaa utrifoo feehi wa kaanoo mujrimeen
📖 Tekkim Wolof
Lu taxoon ca xarnu ya leen jiitu, ñu baax ña [dese woon yan bi] nekkoon ñu néew, ñoom ña daan tere lu bon ci suuf sa ! Ñu bokk ca ña Nu musaloon te ñu tooñoon, topp seeni bakkan ca xéewal ya ñu donnoon ay bàkkaarkat.

🎧 Dégg


📜 Aaya 114-118 — Hud

114وَأَقِمِ الصَّلَاةَ طَرَفَيِ النَّهَارِ وَزُلَفًا مِّنَ اللَّيْلِ ۚ إِنَّ الْحَسَنَاتِ يُذْهِبْنَ السَّيِّئَاتِ ۚ ذَٰلِكَ ذِكْرَىٰ لِلذَّاكِرِينَ
Nanga taxawal julli ci yaari cat yi séq bis bi ak li bokk ci guddi. Jëf yu baax yi dañuy far jëf yu ñaaw ya. Loolu ag waare la ci ñuy waaru.
115وَاصْبِرْ فَإِنَّ اللَّهَ لَا يُضِيعُ أَجْرَ الْمُحْسِنِينَ
Nanga muñ. Yàlla dey du sànk peyug ñay rafetal.
116فَلَوْلَا كَانَ مِنَ الْقُرُونِ مِن قَبْلِكُمْ أُولُو بَقِيَّةٍ يَنْهَوْنَ عَنِ الْفَسَادِ فِي الْأَرْضِ إِلَّا قَلِيلًا مِّمَّنْ أَنجَيْنَا مِنْهُمْ ۗ وَاتَّبَعَ الَّذِينَ ظَلَمُوا مَا أُتْرِفُوا فِيهِ وَكَانُوا مُجْرِمِينَ
Lu taxoon ca xarnu ya leen jiitu, ñu baax ña [dese woon yan bi] nekkoon ñu néew, ñoom ña daan tere lu bon ci suuf sa ! Ñu bokk ca ña Nu musaloon te ñu tooñoon, topp seeni bakkan ca xéewal ya ñu donnoon ay bàkkaarkat.
117وَمَا كَانَ رَبُّكَ لِيُهْلِكَ الْقُرَىٰ بِظُلْمٍ وَأَهْلُهَا مُصْلِحُونَ
Sa Boroom du alag lenn njénde ci ag tooñeel fekk aw nit di sellal seeni jëf.
118وَلَوْ شَاءَ رَبُّكَ لَجَعَلَ النَّاسَ أُمَّةً وَاحِدَةً ۖ وَلَا يَزَالُونَ مُخْتَلِفِينَ
Bu sooboon sa Boroom mu def nit ñi ñu nekk di wenn xeet doŋŋ. Waaye duñu deñ di wuute
HudFihi Alxuraan
123Aaya
MeccanRevelation
116Aaya

Tekki — Hud 116

Simoore Hud Aaya 116 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Lu taxoon ca xarnu ya leen jiitu, ñu baax ña…

Simoore Aaya 116/123 — Hud هود (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Hud Dégg, Hud Tekki, Hud mp3, Hud pdf. Aaya 114–118. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers