Yusuf · 105/111
Tekki Waxtaan — Yusuf
وَكَأَيِّن مِّنْ آيَةٍ فِي السَّمَاوَاتِ وَالْأَرْضِ يَمُرُّونَ عَلَيْهَا وَهُمْ عَنْهَا مُعْرِضُونَ ۝١٠٥
Wa ka ayyim min Aayatin fis samaawaati wal ardi yamurroona `alaihaa wa hum `anhaa mu`ridoon
📖 Tekkim Wolof
Bariwaana ay kéemtaan yu nekk ci asamaan yi ak ci suuf si, ñu di ko romb, te defuñu ca paal !
🎧 Dégg

📜 Aaya 103-107 — Yusuf

103وَمَا أَكْثَرُ النَّاسِ وَلَوْ حَرَصْتَ بِمُؤْمِنِينَ
Te li ëpp ci nit ñi duñu gëm doonte la xér nga sax yaw [ci ña gëm].
104وَمَا تَسْأَلُهُمْ عَلَيْهِ مِنْ أَجْرٍ ۚ إِنْ هُوَ إِلَّا ذِكْرٌ لِّلْعَالَمِينَ
Te laajoo leen ag pey ci [Alxuraan ji]. Te nekkul leneen lu dul ag waare ñeel àddina si yépp.
105وَكَأَيِّن مِّنْ آيَةٍ فِي السَّمَاوَاتِ وَالْأَرْضِ يَمُرُّونَ عَلَيْهَا وَهُمْ عَنْهَا مُعْرِضُونَ
Bariwaana ay kéemtaan yu nekk ci asamaan yi ak ci suuf si, ñu di ko romb, te defuñu ca paal !
106وَمَا يُؤْمِنُ أَكْثَرُهُم بِاللَّهِ إِلَّا وَهُم مُّشْرِكُونَ
Li ëpp ci ñoom duñu gëm Yàlla, xanaa kay dañuy nekk rekk di bokkaale Yàlla.
107أَفَأَمِنُوا أَن تَأْتِيَهُمْ غَاشِيَةٌ مِّنْ عَذَابِ اللَّهِ أَوْ تَأْتِيَهُمُ السَّاعَةُ بَغْتَةً وَهُمْ لَا يَشْعُرُونَ
Ndax dañoo gëmul ne mbugal mu leen muur mën na leen a dal, di mbugalum Yàlla mbaa mu digal leen, bu Bis-pénc baa ci mbetteel te duñu ko yég ?
YusufFihi Alxuraan
111Aaya
MeccanRevelation
105Aaya

Tekki — Yusuf 105

Simoore Yusuf Aaya 105 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Bariwaana ay kéemtaan yu nekk ci asamaan yi ak ci…

Simoore Aaya 105/111 — Yusuf يوسف (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Yusuf Dégg, Yusuf Tekki, Yusuf mp3, Yusuf pdf. Aaya 103–107. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers