Yusuf · 110/111
Tekki Waxtaan — Simoore Yusuf
حَتَّىٰ إِذَا اسْتَيْأَسَ الرُّسُلُ وَظَنُّوا أَنَّهُمْ قَدْ كُذِبُوا جَاءَهُمْ نَصْرُنَا فَنُجِّيَ مَن نَّشَاءُ ۖ وَلَا يُرَدُّ بَأْسُنَا عَنِ الْقَوْمِ الْمُجْرِمِينَ ۝١١٠
Hattaaa izas tai`asar Rusulu wa zannooo annahum qad kuziboo jaaa`ahum nas runaa fanujjiya man nashaaa`u wa laa yuraddu baasunna `anil qawmil mujrimeen
📖 Tekkim Wolof
Ba ña Nu yónni naagoo ne [ndimbal dootul ñëw] te ñu jort ne weddeef nañu leen ba noppi, foofa la Sunu ndimbal agsee ci ñoom. Nu musal ku Nu soob. Te Sunu mbugal amul kenn ku ko mën a fegal tooñkat ya.

🎧 Dégg


📜 Aaya 108-111 — Simoore Yusuf

108قُلْ هَٰذِهِ سَبِيلِي أَدْعُو إِلَى اللَّهِ ۚ عَلَىٰ بَصِيرَةٍ أَنَا وَمَنِ اتَّبَعَنِي ۖ وَسُبْحَانَ اللَّهِ وَمَا أَنَا مِنَ الْمُشْرِكِينَ
Neel : “Samaw yoon a, ngir damay woote jëme ci Yàlla ànd ak aw lay. Man bokkuma ci bokkaalekati Yàlla yi, maak ku ma àndal.
109وَمَا أَرْسَلْنَا مِن قَبْلِكَ إِلَّا رِجَالًا نُّوحِي إِلَيْهِم مِّنْ أَهْلِ الْقُرَىٰ ۗ أَفَلَمْ يَسِيرُوا فِي الْأَرْضِ فَيَنظُرُوا كَيْفَ كَانَ عَاقِبَةُ الَّذِينَ مِن قَبْلِهِمْ ۗ وَلَدَارُ الْآخِرَةِ خَيْرٌ لِّلَّذِينَ اتَّقَوْا ۗ أَفَلَا تَعْقِلُونَ
Yónniwuñu woon, lu la jiitu [yaw Muhammad], lu dul ay góor yu ñu soloo ñu dëkk ca njénde ya. [Nee leen] ndax dañoo doxul ci suuf si, ba seetlu lan mooy mujjug ña leen jiitu woon ? Te ca dëgg-dëgg kërug àllaaxira moo gën ca ña ragal Yàlla. Moo ndax dangeen dul xel-lu ?
110حَتَّىٰ إِذَا اسْتَيْأَسَ الرُّسُلُ وَظَنُّوا أَنَّهُمْ قَدْ كُذِبُوا جَاءَهُمْ نَصْرُنَا فَنُجِّيَ مَن نَّشَاءُ ۖ وَلَا يُرَدُّ بَأْسُنَا عَنِ الْقَوْمِ الْمُجْرِمِينَ
Ba ña Nu yónni naagoo ne [ndimbal dootul ñëw] te ñu jort ne weddeef nañu leen ba noppi, foofa la Sunu ndimbal agsee ci ñoom. Nu musal ku Nu soob. Te Sunu mbugal amul kenn ku ko mën a fegal tooñkat ya.
111لَقَدْ كَانَ فِي قَصَصِهِمْ عِبْرَةٌ لِّأُولِي الْأَلْبَابِ ۗ مَا كَانَ حَدِيثًا يُفْتَرَىٰ وَلَٰكِن تَصْدِيقَ الَّذِي بَيْنَ يَدَيْهِ وَتَفْصِيلَ كُلِّ شَيْءٍ وَهُدًى وَرَحْمَةً لِّقَوْمٍ يُؤْمِنُونَ
Seen nettali yooyu ay waaree nga ca ñeel woroom xel ya. Du waxtaan wu ñu sos. Waaye day dëggal ya jiitu, te it di leeral lépp lu nekk di ag njub, di yërmaande ñeel nit ñu gëm.
YusufFihi Alxuraan
111Aaya
MeccanRevelation
110Aaya

Tekki — Yusuf 110

Simoore Yusuf Aaya 110 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Ba ña Nu yónni naagoo ne [ndimbal dootul ñëw] te…

Simoore Aaya 110/111 — Simoore Yusuf يوسف (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Yusuf Dégg, Simoore Yusuf Tekki, Simoore Yusuf mp3, Simoore Yusuf pdf. Aaya 108–111. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers