Ar-Ra'd · 7/43
Tekki Waxtaan — Ar-Ra'd
وَيَقُولُ الَّذِينَ كَفَرُوا لَوْلَا أُنزِلَ عَلَيْهِ آيَةٌ مِّن رَّبِّهِ ۗ إِنَّمَا أَنتَ مُنذِرٌ ۖ وَلِكُلِّ قَوْمٍ هَادٍ ۝٧
Wa yaqoolul lazeena kafaroo law laaa unzila `alaihi Aayatum mir Rabbih; innamaaa anta munzirunw wa likulli qawmin haad
📖 Tekkim Wolof
Ña weddi ñangay wax : “Lu tee ñu wàcce ci moom kéemaan gu jóge ca Boroomam ? ”. Te yaw nekkoo lu dul kuy waare, te xeet wu nekk am na ku koy gindi.

🎧 Dégg


📜 Aaya 5-9 — Ar-Ra'd

5۞ وَإِن تَعْجَبْ فَعَجَبٌ قَوْلُهُمْ أَإِذَا كُنَّا تُرَابًا أَإِنَّا لَفِي خَلْقٍ جَدِيدٍ ۗ أُولَٰئِكَ الَّذِينَ كَفَرُوا بِرَبِّهِمْ ۖ وَأُولَٰئِكَ الْأَغْلَالُ فِي أَعْنَاقِهِمْ ۖ وَأُولَٰئِكَ أَصْحَابُ النَّارِ ۖ هُمْ فِيهَا خَالِدُونَ
Ndeem danga yéemu yaw [Yonent bi], dana la yéem li ñuy wax naan : “Ndax bu ñu deewee ba seey nekk suuf, danañu dekkiwaat nekk i mbindeef ? ”. Ñooña ñooy ña weddi seen Boroom. Te mooy ña gëx nekk ca seen loos. Te ñoom ñoo di waa Safara, te dañu fay béel.
6وَيَسْتَعْجِلُونَكَ بِالسَّيِّئَةِ قَبْلَ الْحَسَنَةِ وَقَدْ خَلَتْ مِن قَبْلِهِمُ الْمَثُلَاتُ ۗ وَإِنَّ رَبَّكَ لَذُو مَغْفِرَةٍ لِّلنَّاسِ عَلَىٰ ظُلْمِهِمْ ۖ وَإِنَّ رَبَّكَ لَشَدِيدُ الْعِقَابِ
Ñangay yàkkamti naan na mbugal [mi nga nu dig] nëw lu jiitu seenug sàkku yërmaande. Waaye ca la weesu, amoon na ay mbugal [yu daloon ña leen jiitu]. Doonte la sa Boroom kuy jéggal nit ñi la seeni bàkkaar, waaye fekk na sa Boroom di ku tar mbugal itam.
7وَيَقُولُ الَّذِينَ كَفَرُوا لَوْلَا أُنزِلَ عَلَيْهِ آيَةٌ مِّن رَّبِّهِ ۗ إِنَّمَا أَنتَ مُنذِرٌ ۖ وَلِكُلِّ قَوْمٍ هَادٍ
Ña weddi ñangay wax : “Lu tee ñu wàcce ci moom kéemaan gu jóge ca Boroomam ? ”. Te yaw nekkoo lu dul kuy waare, te xeet wu nekk am na ku koy gindi.
8اللَّهُ يَعْلَمُ مَا تَحْمِلُ كُلُّ أُنثَىٰ وَمَا تَغِيضُ الْأَرْحَامُ وَمَا تَزْدَادُ ۖ وَكُلُّ شَيْءٍ عِندَهُ بِمِقْدَارٍ
Yàlla xam na lu jépp jigéen ëmb, ak lay wàññeeku ak a yokk ca ëmb ba. Te lépp lu nekk am na moom ab natt [bu mu tollool].
9عَالِمُ الْغَيْبِ وَالشَّهَادَةِ الْكَبِيرُ الْمُتَعَالِ
Mooy kiy xam lu fàddu ak li feeñ, di Ku màgg, di Ku kawe ka.
Ar-Ra'dFihi Alxuraan
43Aaya
MedinanRevelation
7Aaya

Tekki — Ar-Ra'd 7

Simoore Ar-Ra'd Aaya 7 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Ña weddi ñangay wax : “Lu tee ñu wàcce ci…

Simoore Aaya 7/43 — Ar-Ra'd الرعد (Medinan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Ar-Ra'd Dégg, Ar-Ra'd Tekki, Ar-Ra'd mp3, Ar-Ra'd pdf. Aaya 5–9. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers