An-Nahl · 42/128
Tekki Waxtaan — An-Nahl
الَّذِينَ صَبَرُوا وَعَلَىٰ رَبِّهِمْ يَتَوَكَّلُونَ ٤٢
Transliteration
Allazeena sabaroo wa `alaa Rabbihim yatawak kaloon
Tekki (Tekkim Wolof)
📖 Tekkim Wolof
Ñoo di ñay muñ, wéeru ci seen Boroom [Dana leen wërsëgal lu ñu njortul woon].
Additional reference in Fulfulde
🎧 Dégg
📜 Aaya 40-44 — An-Nahl
40إِنَّمَا قَوْلُنَا لِشَيْءٍ إِذَا أَرَدْنَاهُ أَن نَّقُولَ لَهُ كُن فَيَكُونُ
[Li am mooy], Sunu kàddu ci mbir, bu Nu ko bëggee, Danu ko naan : “Nekkal”. Mu daldi nekk.
41وَالَّذِينَ هَاجَرُوا فِي اللَّهِ مِن بَعْدِ مَا ظُلِمُوا لَنُبَوِّئَنَّهُمْ فِي الدُّنْيَا حَسَنَةً ۖ وَلَأَجْرُ الْآخِرَةِ أَكْبَرُ ۚ لَوْ كَانُوا يَعْلَمُونَ
Ña gàddaay jëm ci Yàlla, ginnaaw ba ñu leen tooñee, Dananu leen wàcceel aw yiw ci àddina. Te peyug àllaaxira moo gën a màgg, cëy bu ñu xamoon !
42الَّذِينَ صَبَرُوا وَعَلَىٰ رَبِّهِمْ يَتَوَكَّلُونَ
Ñoo di ñay muñ, wéeru ci seen Boroom [Dana leen wërsëgal lu ñu njortul woon].
43وَمَا أَرْسَلْنَا مِن قَبْلِكَ إِلَّا رِجَالًا نُّوحِي إِلَيْهِمْ ۚ فَاسْأَلُوا أَهْلَ الذِّكْرِ إِن كُنتُمْ لَا تَعْلَمُونَ
Yónniwunu woon ca la jiitu lu dul ay góor yu Nu xamaloon [Sunuy ndigal]. Ne leen bu ngeen xamul laajleen woroom xam-xam yi.
44بِالْبَيِّنَاتِ وَالزُّبُرِ ۗ وَأَنزَلْنَا إِلَيْكَ الذِّكْرَ لِتُبَيِّنَ لِلنَّاسِ مَا نُزِّلَ إِلَيْهِمْ وَلَعَلَّهُمْ يَتَفَكَّرُونَ
[Ay Yonent lañu woon] yu indi lay yu leer ak i téere. Te Nu wàcce it Alxuraan ngir nga leeralal nit ñi la ñu wàcce woon ca ñoom, ñu xel-lu [waar ña gëm].
An-NahlFihi Alxuraan
128Aaya
MeccanRevelation
42Aaya
Tekki — An-Nahl 42
Simoore An-Nahl Aaya 42 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Ñoo di ñay muñ, wéeru ci seen Boroom [Dana leen…Simoore Aaya 42/128 — An-Nahl النحل (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: An-Nahl Dégg, An-Nahl Tekki, An-Nahl mp3, An-Nahl pdf. Aaya 40–44. Tekkim Wolof: Fulfulde.
العربية
English
Bahasa Indonesia
Türkçe
Русский
فارسی
Français
اردو
বাংলা
Deutsch
Español
中文
हिन्दी
Português
Italiano
ภาษาไทย
Polski
Nederlands
Shqip
Kiswahili
O'zbek
தமிழ்
Melayu
Bosanski
Soomaali
Azərbaycan
کوردی
한국어
日本語
Svenska
Dansk
Norsk
پښتو
മലയാളം
සිංහල
Tamazight
Hausa
አማርኛ
Български
Тоҷикӣ
Қазақша
Filipino
سنڌي
Yorùbá
Fulfulde
Татарча
ئۇيغۇرچە
Кыргызча
ਪੰਜਾਬੀ
Jawa
తెలుగు
မြန်မာ
ગુજરાતી
Oromo
मराठी
Tiếng Việt
Malagasy
Нохчийн
Wolof
ދިވެހި
ಕನ್ನಡ
Українська
Ελληνικά
ქართული
ខ្មែរ
دری
Qafar af
Maranao
नेपाली
Alxuraan bu Tedd bi
Tuesday, August 18, 2026
Don't forget us in your sincere prayers








